
Alaaji Sheex
@echgueye • 39,204 subscribers
MURID, Professionnel Multimédia, Consultant, IPTV, Designer, Director, Broadcaster, OTT, MBI LLC; #Focus , btech, mbstudios, Senflix, 6’6½”
Shorts
Videos

Ñeel na Yalla sam “siin” ak sama “raa” [sirru] , ñeel nako sama “Jiim” sama “haa” ak sama “raa” [jahri] Maanam ñeel na Yalla sama li feeñ ak li nëbu Sama “saad” sama “Waaw” ak sama “miim” [sawmii] li feek mangi dundi moom mooko moom . Batay ñeel nako sama “faa” ak sama “tha” ak sama “raa” [Fithri] Muy sama koor ak sam dogg (wala kori) lepp ñeel na ko moom sama Boroom
Alaaji Sheex13,676 Aufrufe • vor 5 Monaten

Da ngay nek ak nit do khamni mouride la woon, mou dieki nan la bayyi naa 🤣🤣🤣 😭 😭
Alaaji Sheex51,727 Aufrufe • vor 3 Jahren
Keine weiteren Inhalte verfügbar