
Gaindé Fatma 🇸🇳 💀
@kachmmi • 35,921 subscribers
TÉÉRÉ INVISBLE💀 Lou Woor Yala Mo Gueune Lou Woor Nit 🫱🏿🫲🏾
Shorts
Videos

Wahahahaha gni deh la traitre bi dakh mou foog ni daniouy mer, niou tiim sen boolou tieebou diaga di kheweulou, di kaagn sen bopp, di waadial magal gui. Boy yi am métier, Doug si politique pour defar deuk bi nga foog ni ay décret mooleen di téeré doundou.💀🤣🤣🤣
Gaindé Fatma 🇸🇳 💀74,768 views • 2 months ago

Beat bi soft, tek bi soft ak insolence, Boy bi dafa am new ak old school si moom motakh I feel him.🙌🏿 improviser boko meuné aka neex han Willy Kemtane 🤭🔥 LPA 2005/2006 bountou boutique ba, sheut damassi doon noce. Le 08/ Canal Olympia ak SASUKE / Trap King 🦍🇸🇳
Gaindé Fatma 🇸🇳 💀38,881 views • 1 month ago

Tenez cadeau. Li bou nekoul rupture kone louy rupture ?🥹🥹
Gaindé Fatma 🇸🇳 💀199,338 views • 1 year ago

T’es dans un pays ou. - t’as un président traître -une fédération de football de merde - Une canicule qui finit jamais - t’es pauvre jusqu’aux os - 10 millions pour attacher femme - t’es un vieux célibataire - les 2 choses, qui me réconfortent, sont le mafé et le soupe kandia😭.
Gaindé Fatma 🇸🇳 💀27,919 views • 2 months ago