
Le Mouride Post
@LeMouridePost • 114,971 subscribers
Shorts
Videos

📍Bachir demaatoon tay jii seeti Serigne Assane, Khalifa Ababacar SARR DG de la SONAGED SA gis vidéo démb bi rafetlu ko lool am yéené recruté ko, defal ko contrat ngir mu liggéey foofu; muy mbégté mu rëy ci nun ñépp. Képp kuko bëgg a yóonée àddiya nak man nga ko jaarale ci 77 800 49 70 (Abdou Rahmane Gueye) am na wave am na Orange Money
𝐋𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝐞 𝐏𝐨𝐬𝐭 🇸🇳160,723 次观看 • 1 年前
