Video wird geladen...
Video konnte nicht geladen werden
Aka niémé deugeu
10 Kommentare

Ki mo gueuna niamé deug ci mbeur yi il dit toujours les termes

Combat Sa ak XLO mom diaroul nek fi di wax gneup xam nagn ni dafay taxaw diaroul graw graw lou 😂😂😂

Na taxaw de

Mais attendez modou lo dafa tok fen né dou beurer ak sa thies ? Je comprends vraiment pas cet acharnement kou kay chance Yaldaw dina bania may chance Sathies? Sénégal nehna

Cey Maodo, ci digg bi lay jar 🔥

Ce n'est pas logique pourtant Tapha TINE avait battu Eumeu SENE entre-temps.

Aye ki laye beurell wala ke laye beurel mo narra yakk lamb ji

On dirait que modou il a dit qu’il ne lutterait pas avec les boys doucement c’est quand même celui qui le plus rivalisé avec les jeunes dernièrement il va forcément le prendre take it easy

Nanouko wax té doundou Modlo mo sofal lambe bi

Je l’aime ce gars 💯
