Video wird geladen...

Video konnte nicht geladen werden

Zur Startseite

Alerte soyez prudent 🚨🚨🚨🚨

39,290 Aufrufe • vor 3 Monaten •via X (Twitter)

13 Kommentare

Profilbild von Limpide
Limpidevor 3 Monaten

Blh c vrai sama tonton thi la bok amna 2femmes ma dem Monaco un jr fek ko fofu mouy planche halé yi té meusoul done maître nageur 🏊

Profilbild von Sitaff kruMa🇸🇳
Sitaff kruMa🇸🇳vor 3 Monaten

Bilae wakhna deug je suis témoin de ça N fois 😂😂😂

Profilbild von BASSENE Aïssatou🧕🏼💕
BASSENE Aïssatou🧕🏼💕vor 3 Monaten

Ya Rabbi🥺😩amneu niou yess nakk SoubhanaAllah🥺

Profilbild von Lankizer Franc Ndiago ❤️👑
Lankizer Franc Ndiago ❤️👑vor 3 Monaten

Meuss nassi dioté ak ben père soit disant maître nageur diapp khalei bou djiguen pour yobou si biir maniko alalou procureur rek pabi mère di histoire ak man

Profilbild von Lodia
Lodiavor 3 Monaten

Plage yeup la am presque srtt NGOR

Profilbild von Ju²🥀🖤
Ju²🥀🖤vor 3 Monaten

Demo ngor kone ba guiss Pa yikay def😭

Profilbild von L’archiviste ProSonko
L’archiviste ProSonkovor 3 Monaten

Bilahi deug rek ngua wax. Ay pa you am 60ans di nane dagnouy diangalei fey ak you ken xamoul

Profilbild von Laye_Bii🇸🇳
Laye_Bii🇸🇳vor 3 Monaten

Deugue leu d

Profilbild von Chirba_Juuf🇸🇳
Chirba_Juuf🇸🇳vor 3 Monaten

@Assane_Fall_Off Khana demo ngor ioe Surtt la nuit

Profilbild von Lamin0 🇸🇳 ⭐⭐
Lamin0 🇸🇳 ⭐⭐vor 3 Monaten

Sénégal 🇸🇳 Eskeu deuk leu deuk yi dagnou lein raw Lou beurii

Profilbild von 𝑴𝒉𝒅𝒃𝒆𝒍𝒍𝒆𝒗𝒊𝒆 🦮🕊️
𝑴𝒉𝒅𝒃𝒆𝒍𝒍𝒆𝒗𝒊𝒆 🦮🕊️vor 3 Monaten

Ltx dougne tooq sheuutt mane Sénégal Barqi Yalla doudeem

Profilbild von KABANANGUA☯️
KABANANGUA☯️vor 3 Monaten

Dimanche passe j’ai été témoins de sa wollah anziiim ! Après j’ai essayé de les comprendre mais mon cerveau s’est planqué 😶meu gueine naank deem jusqu’à l’endroit où il n’y a que des rochets et où s’est interdit de se baigner

Profilbild von 🇸🇳Juan🇨🇻
🇸🇳Juan🇨🇻vor 3 Monaten

Le "doko meneu nétali keine" est vraiment problématique. Donc si je comprends bien on te tend un piège et tu subis des attouchements mais c'est de ta faute parceque tu as accepté de l'aide de quelqu'un que tu pensais être un maître nageur. 🤦🏾‍♂️

Ähnliche Videos