Загрузка видео...
Не удалось загрузить видео
Ay leral ci bëssu Harafa👂🏾
10,600 просмотров • 5 месяцев назад •via X (Twitter)
Комментарии: 20

@amour_xassida @KossoNiasse98 Li ma leen man a wax mooy ibaadu yi seen calendrier bopp lañ yore, dungeen fexe bañ dëppoo ak yéen.

@KossoNiasse98 M’a fokni niom makka laniouy topp mo waral li?

@amour_xassida Mais ce gars la il est incroyable que Dieu te comble vous méritez d’être écoute car vous donnez des preuves

@amour_xassida @Marseille345 Manaam danga beugeu wakh ni arafah Mercredi wala mala degoul 😂 bilay yeena bari thiakhaan

@amour_xassida @Ndoye_Malimaram Jërëjëf ci léral yi🙏🏽

@amour_xassida Xam Xam day ande ak daliil Dieureudieuf ci leral tu

@amour_xassida Quand les soufis parlent de dalil ayeu rei lamayeu df 😂😂😂😂😂

@amour_xassida @SSaliouDiop 😂😂😂dof biii deiy layaliii mercredi moy arafat si

@amour_xassida Sonal nane nite yi trop

@amour_xassida 🤣🤣🤣🤣🤣 Arafat mercredi nakk 😂

@amour_xassida Waa saay 😂

Cheikh Mustafaaaa😂

@amour_xassida Fo reer gayin

Nekonn ci tunel yi rék

@amour_xassida Djeureujeuf djeureujeuf djeureujeuf Wawe gorr wawe goor wawe gorr Machallah 🙏

@amour_xassida Kharafal kaay 😂😂😂

@amour_xassida @Ndoye_Malimaram Liya matta bayii khel

@amour_xassida @khadimly10 Yalla na yalla faye serigne si barké touba bi nga yaakar

@amour_xassida @Marseille345 Ñii senn kham kham mo barii woul

@amour_xassida @f_a_d_e_l221 Kagne lanouy dépassé genre wèranté yi
Похожие видео
Làcc na ap taxaw setlu 👂🏾😳 lolén ci xalaat ? #kebetu
Sonib Nowhere
15,324 просмотров • 7 месяцев назад
