Loading video...
Video Failed to Load
BAYE NIASS REIK LEU ❤️✋️
55,548 views • 1 year ago •via X (Twitter)
10 Comments

Compétition bi Ngeen di diem def soff nama torop ! Baye n'était pas égocentrique ! Aucun homme de Dieu n'est égocentrique ! " Koudoul mane xamoul " kouko wax khepp meuninou Y'Allah Diné bi dou competition...

So diangon diawahir Maani lafaa SEYDINA CHEIKH wax diga roussa dougal lii. Niune Jeunesse Tijani on a pas besoin de populisme.yalla sa borom ay mayamm yatuna.Mbok del indi ay video yuye diarign jeuness bi si diné bi ak si tarikha bii mais pas yii!!! Layée birr leu rk!!

Ah Baye Niass mogui dokh dei Mogui dokh dei 😂😂

Waawaaw

Lima ci jaaxal mooy Cheikhou Tidiani moom ku ko duggaloon ci xadra Yalla bi moom miy taajul aarifiina ? Bu fekkeii ci Bay rekk lagniy diaar 🤔

Ah wakhtane lén Bâ joubo rék après vous nous dites c'est qui le GAOT parmis vos guides après nous les sans tarikha gnou xol.

Iow tu es toujours dans le populisme tous les jours

Seriñ yow gëm nga lii mu wax? Wala dafay dugg ci waxinu tassawuf ni "kudul sama seriñ nekkufi"?

C'est ki lui?

Soof ngueen !
