Video wird geladen...

Video konnte nicht geladen werden

Zur Startseite

Bonsoir selbé Ndom 😂😂😂😂

48,966 Aufrufe • vor 6 Monaten •via X (Twitter)

37 Kommentare

Profilbild von Anvi🥀
Anvi🥀vor 6 Monaten

Ki molen taylei 🤣😭🤣🤣🤣😭

Profilbild von Killer au coeur Rouge ❤️
Killer au coeur Rouge ❤️vor 6 Monaten

Tayy mome Nice reikk

Profilbild von Ndaanane🌠
Ndaanane🌠vor 6 Monaten

Kii dafa alkou, jurer comme ça pour de la lutte en tenant le livre saint.

Profilbild von Aliou SARR
Aliou SARRvor 6 Monaten

Selbé ay djinné you immatured la amm leegui daniouy foo ak moom😂🤣🤣😂

Profilbild von MiSS~Yacine🫶🏿😍
MiSS~Yacine🫶🏿😍vor 6 Monaten

😂😂😂Sama goudii migui yakou

Profilbild von Killer au coeur Rouge ❤️
Killer au coeur Rouge ❤️vor 6 Monaten

Magui nieuw geunko yakkk 😂😂😂

Profilbild von Westaf🇸🇳
Westaf🇸🇳vor 6 Monaten

Ak sa doul yi nga teyer alkuran di wat , yonent bi sah dula beug guiss🚶

Profilbild von Zɛŋɖɛყą 🧸🇸🇳
Zɛŋɖɛყą 🧸🇸🇳vor 6 Monaten

😂😂😂😂

Profilbild von @Tontonseye🎂🇸🇳🇲🇫
@Tontonseye🎂🇸🇳🇲🇫vor 6 Monaten

Konne de doguisseunteti wa keur seydina Mohamed

Profilbild von FreeSenegal
FreeSenegalvor 6 Monaten

😅😅😂😂 Ki est ce que djiné méré wou niouko 😅😅😂😂

Profilbild von Sëriñ Saliou
Sëriñ Saliouvor 6 Monaten

Jinneem yi respecte wuñ ko d

Profilbild von Momar Ndiay
Momar Ndiayvor 6 Monaten

@AssaneGueye23 Selbé sa djiné yi nio maguett

Profilbild von Le Faux Drilleur 🐺.🌒
Le Faux Drilleur 🐺.🌒vor 6 Monaten

@bah_rahmane Mère bi mingui doundou batay?? Haha nonnn selbe neneu mom bizimpinw bimou néké si town bi douko bayi en big 2026 genre ??

Profilbild von franck gallagher 5,2🇸🇳
franck gallagher 5,2🇸🇳vor 6 Monaten

Comme madiambal😂

Profilbild von Ahmadou
Ahmadouvor 6 Monaten

Doungéne guissé dh sallaw😩😩😩😂😂😂😂

Profilbild von Djadjao Diatta
Djadjao Diattavor 6 Monaten

Yaw kéy doko djis

Profilbild von Fatoobabel
Fatoobabelvor 6 Monaten

@Priinxe2 Dafa kou-al😭😭Barki Lahilaha illallah kouka ci bayi woul bakhna rék 😂

Profilbild von 🇸🇳TOPPO🌟🌟
🇸🇳TOPPO🌟🌟vor 6 Monaten

@CamaraAdja05 Woooooyyyyyy😝😝😝😝🤣🤣🤣🤣🤣🤣Le vieux père

Profilbild von Bou 🥷🇸🇳⭐️⭐️
Bou 🥷🇸🇳⭐️⭐️vor 6 Monaten

Ki meun na fen 😂

Profilbild von 売上
売上vor 6 Monaten

ay way bal leen ko 😂😂

Profilbild von and
andvor 6 Monaten

Kii ken douko plainte nguirr yalla

Profilbild von sissokho.eth
sissokho.ethvor 6 Monaten

Reverse-Selbé doesn't loose

Profilbild von Ibrahima at_Tidjanii🇸🇳🇺🇲♥️
Ibrahima at_Tidjanii🇸🇳🇺🇲♥️vor 6 Monaten

@AssaneGueye23 Lo bamou waxei la xamnei modou day niakeu 😭

Profilbild von Nabil 👑👑
Nabil 👑👑vor 6 Monaten

hamna ni mom seydina mouhamed mom dolen guisse d🤧🤧🤧😂😂

Profilbild von 𝙈𝙤𝙪𝙝𝙖𝙢𝙖𝙙𝙤𝙪 𝙔𝙚𝙙𝙖𝙡𝙮🇸🇳⭐️⭐️
𝙈𝙤𝙪𝙝𝙖𝙢𝙖𝙙𝙤𝙪 𝙔𝙚𝙙𝙖𝙡𝙮🇸🇳⭐️⭐️vor 6 Monaten

Aka meune enrouler

Profilbild von 🪔Hawa bint Ahmad✨حواء بنت أحمد🪭
🪔Hawa bint Ahmad✨حواء بنت أحمد🪭vor 6 Monaten

Sheu ki mome watt yi eupnaaa birammme Gningue rek mboot leuh 😭

Profilbild von Aziz Ndiaye!🐐
Aziz Ndiaye!🐐vor 6 Monaten

Gni si boppam nio deugeur fit😂😂😂

Profilbild von SONKO JR🌟🌟🇸🇳
SONKO JR🌟🌟🇸🇳vor 6 Monaten

Thiey aduna lo guiss day diekh.. 😂😂. Ki da oumou.

Profilbild von Ababacar Sadikh 🇸🇳 🇱🇧
Ababacar Sadikh 🇸🇳 🇱🇧vor 6 Monaten

Bim wakhé laani alhamdoulilah

Profilbild von Au Lee Va S. 🇸🇳⭐️⭐🇸🇳 Championne d'Afrique 2125
Au Lee Va S. 🇸🇳⭐️⭐🇸🇳 Championne d'Afrique 2125vor 6 Monaten

🤣🤣🤣🤣🤣ki mo geuneu niemè Yalla Sénégal à part Koukandé

Profilbild von 🇸🇳HONORABLE LE PRO🇸🇳🇸🇳⭐️⭐️
🇸🇳HONORABLE LE PRO🇸🇳🇸🇳⭐️⭐️vor 6 Monaten

@Lil_SayniCFC Ki kou maana fenn leeu😭😭

Profilbild von Yfk❤️✨
Yfk❤️✨vor 6 Monaten

Bimou waxei sa day danou dama sante yallah diap confiance 😂😂😂

Profilbild von TAFA DIEYE 🇲🇷🇸🇳
TAFA DIEYE 🇲🇷🇸🇳vor 6 Monaten

En faite vous ne comprenez pas selbé mom day wate si limiu guiss mais esk ca sera la réalité lolou benene affaire la xam na lolou takh mou am sagn sagn dieul kamil di wate

Profilbild von in god we trust 🇸🇳☝🏽
in god we trust 🇸🇳☝🏽vor 6 Monaten

@AssaneGueye23 🤭😂😂😂😂😂

Profilbild von sadisfied
sadisfiedvor 6 Monaten

Kone ki nit yangui kay deglu ak may temps ba legui? Mdr

Profilbild von Butters
Buttersvor 6 Monaten

@dominic18_04 Yaw mom mére sama akheu soula dalé doula djik ndakh mak dou fén …

Profilbild von falldntfall
falldntfallvor 6 Monaten

Mom sa you guisse dara dafko wara weulbeuti contraire leu 😂😂😂

Ähnliche Videos

Bonsoir à tous
0:45

Sensitive content

Bonsoir à tous

Tayla beatryz

20,775 Aufrufe • vor 2 Jahren