Video wird geladen...

Video konnte nicht geladen werden

Zur Startseite

103,994 Aufrufe • vor 18 Tagen •via X (Twitter)

34 Kommentare

Profilbild von Ampa culer❤️💙
Ampa culer❤️💙vor 18 Tagen

Souko fi ibadou wakhone gendarmerie fekk si ko en même pas 24h thiey Senegal💔

Profilbild von Mouhamadoul'Amine
Mouhamadoul'Aminevor 18 Tagen

Attend mome loumou waxx yorr na ay explosifs you paré. Dans un pays normal ki BIP la warone fanane

Profilbild von Lamine
Laminevor 18 Tagen

@gendarmeriena18 @PoliceNationSN un terroriste affirmant en public avoir des bombes prêt à être utilisé

Profilbild von Aboubkr_Sadikh🇸🇳
Aboubkr_Sadikh🇸🇳vor 18 Tagen

Sa genre yi nak nioy problème Sénégal 😂😂

Profilbild von Ousmane
Ousmanevor 18 Tagen

Tibb bou reuuy rayy neu borom wayé borom dound rekk ́la beugone

Profilbild von ez.el 🔜
ez.el 🔜vor 18 Tagen

Wadji waxou mak mome dhe , waye gnou tok déf tout blanc diougue sen keur ba fofou , tok ben way di ay waxou dof Guay tathiou … sn kw 💔

Profilbild von Abdoulaye KANE
Abdoulaye KANEvor 18 Tagen

Mome sou defaré explosif ba paré kan lakoy sani la beug ham 🤣😂

Profilbild von Ⓜ️OR TALLA🇸🇳🫥
Ⓜ️OR TALLA🇸🇳🫥vor 18 Tagen

Xolal ma li rk nioune esk niongui si Etat de droit ki li mouy wax nii té dra douko si fekk nii putin

Profilbild von Abou Ba
Abou Bavor 18 Tagen

Sa way merde à la fin

Profilbild von L’Ayatollah ♠️🛡️⚔️
L’Ayatollah ♠️🛡️⚔️vor 18 Tagen

Gniy tathiou nioma yème🥲 Ce pays 🤦🏻‍♂️

Profilbild von El Hadji Ndao
El Hadji Ndaovor 18 Tagen

@PoliceNationSN @gendarmeriena18 Wakhi explosif prêt à être utilisé lafi💥

Profilbild von Xarag’n🇸🇳
Xarag’n🇸🇳vor 18 Tagen

Nama all 4 clè nuclear yi ma am louma essayer 😂😂

Profilbild von Dadu
Daduvor 18 Tagen

Pourtant wakhna courouss dé, mais deuk bi mom kouné lila arrangé rek ngay tiopati dem di douléléléé

Profilbild von Hussein Sene🧠🕊️
Hussein Sene🧠🕊️vor 18 Tagen

Meunoko dh Teyer sa micro rek di ratatati nga meune

Profilbild von Jibril Sans-Filtre
Jibril Sans-Filtrevor 18 Tagen

Noon té ay nitt nioko topp ni dh. Yalla na len yalla yeureum

Profilbild von Almoudou Cheikh
Almoudou Cheikhvor 18 Tagen

Senegal kagn lay avance entre pasteef ak ay fenam et une population qui suit à l’aveugle des religieux sur des discours qui ne mène à rien . Liguey yi Léne le temps n’attend pas et seul le travail paie.

Profilbild von MHD.Sembene
MHD.Sembenevor 18 Tagen

Sama problème dou wadji deh mais gni di applaudir 👏 ni melni aay rebots sur commande ni putain 🤧

Profilbild von 𝕸𝖗_𝕮𝖎𝖘𝖘𝖊𝖍⭐🇸🇳🔰
𝕸𝖗_𝕮𝖎𝖘𝖘𝖊𝖍⭐🇸🇳🔰vor 18 Tagen

@ibrhim_khalil3 Mom loutax mou beug def reew mi doom moma jaaxal?

Profilbild von Badzo bu SONKO
Badzo bu SONKOvor 18 Tagen

@PoliceNationSN

Profilbild von AND ✌️✍🏿
AND ✌️✍🏿vor 18 Tagen

@PoliceNationSN

Profilbild von le merengué🇸🇳🇸🇳🇸🇳
le merengué🇸🇳🇸🇳🇸🇳vor 18 Tagen

Déff sougoufff méwww bokk

Profilbild von Young Leuz🇸🇳
Young Leuz🇸🇳vor 18 Tagen

On est sauvé, dissuasion nucléaire lanu yoor

Profilbild von feutima zahra⭐️⭐️🇸🇳
feutima zahra⭐️⭐️🇸🇳vor 18 Tagen

@PoliceNationSN @gendarmeriena18

Profilbild von Pape_Jàa MùMamaam😊🇸🇳
Pape_Jàa MùMamaam😊🇸🇳vor 18 Tagen

Yae meuno dara xana wax😂

Profilbild von NdIAYE So 👋
NdIAYE So 👋vor 18 Tagen

@ibrhim_khalil3 Diversion rejeté niou focus si ensemble national bi

Profilbild von 🇸🇳🇵🇸Serigne Mbacke Mouhaméd DIOP
🇸🇳🇵🇸Serigne Mbacke Mouhaméd DIOPvor 18 Tagen

Li mou wax graw na dh wala maa degoul wolof

Profilbild von c’estduhalal🇸🇳🐐
c’estduhalal🇸🇳🐐vor 18 Tagen

jules koundé lougn la def

Profilbild von keba.s.diop.🇸🇳🤍
keba.s.diop.🇸🇳🤍vor 18 Tagen

Tok di doul rek

Profilbild von faliluh 🇸🇳
faliluh 🇸🇳vor 18 Tagen

Mome Kane la beugg xékhal?

Profilbild von AbuDjibril🇸🇳🇨🇮⭐️⭐️
AbuDjibril🇸🇳🇨🇮⭐️⭐️vor 18 Tagen

Grand menteur 🤥

Profilbild von Soma
Somavor 18 Tagen

Sa way tu parles Trop

Profilbild von Coca Kc ✊️
Coca Kc ✊️vor 18 Tagen

Des faussaires si zaire ak si batine! Tousss manoko ! Sénégalais de tout le pays allaient comprendre votre "Religion originelle "

Profilbild von ༺𝔖𝔥𝔞𝔡𝔬𝔴𝔐𝔦𝔫𝔡༻
༺𝔖𝔥𝔞𝔡𝔬𝔴𝔐𝔦𝔫𝔡༻vor 18 Tagen

Deuk bi neixna nak niit moy taxaw menacer rew mi té dara dou ko si fekk. Allons rek!

Profilbild von Tidiane Melv🇸🇳
Tidiane Melv🇸🇳vor 18 Tagen

Quel comédien…