Video yükleniyor...

Video Yüklenemedi

Ana Sayfaya Dön

Ce pays 😭😂😂😂😂

25,908 görüntüleme • 4 ay önce •via X (Twitter)

34 Yorum

Babacar Kebe 🇸🇳🇲🇦🇵🇸🇨🇩🇲🇱 profil fotoğrafı
Babacar Kebe 🇸🇳🇲🇦🇵🇸🇨🇩🇲🇱4 ay önce

Tiéré gueunoul yoomebe sobelé ak pomebiterre!? 😂😂😂

Bintou Rassoul 🏆🇸🇳 ⭐️⭐️♥️ profil fotoğrafı
Bintou Rassoul 🏆🇸🇳 ⭐️⭐️♥️4 ay önce

Danio mine seni fen legui

Serigne Saliou Niasse profil fotoğrafı
Serigne Saliou Niasse4 ay önce

@Perfectionner22 Sauce ak tiara bu geuna yomb omar ga balma mais ya meuna doule nak 😂😂

DoUɾAᖾ Diop ⭐️⭐️ 🇸🇳 🇧🇯 profil fotoğrafı
DoUɾAᖾ Diop ⭐️⭐️ 🇸🇳 🇧🇯4 ay önce

Par contre la partie de l’eau est tellement vrai. C’est devenu un luxe de voir l’eau à certaine heure

Souleymane B. profil fotoğrafı
Souleymane B.4 ay önce

Ki keur kan la dougu la beug kham ?

MMS🇸🇳 profil fotoğrafı
MMS🇸🇳4 ay önce

@Joobmanny Doul rek

Nfally Mansaly profil fotoğrafı
Nfally Mansaly4 ay önce

Vraiment ces gens là sont des salopard de leur famille pourquoi mentir comme ça après il vont gagner quoi regardé comment il vilain comme son derrière

TH!NK£R🇸🇳🇵🇸 profil fotoğrafı
TH!NK£R🇸🇳🇵🇸4 ay önce

Mom xana dafa done weur di kharane si quartier bi ak khar boll doff😂😂😂

kany khégn profil fotoğrafı
kany khégn4 ay önce

Dayyyyy doul dé hoho 🫢🫢🫢🫢🫢

ENES 🎥 profil fotoğrafı
ENES 🎥4 ay önce

Wa keureum lay wakh

Shinra Tensei 🇸🇳 profil fotoğrafı
Shinra Tensei 🇸🇳4 ay önce

KEUR DOFF YI 🤣🤣

Patriot profil fotoğrafı
Patriot4 ay önce

They lie so comfortably, as if it were nothing. May Allah forgive us.

Bayou Fatim@💯 profil fotoğrafı
Bayou Fatim@💯4 ay önce

Lolou demal wakhko diomay

Atika Badji 🇸🇳⭐️⭐️ profil fotoğrafı
Atika Badji 🇸🇳⭐️⭐️4 ay önce

Ki mom ay fen la dieul legui🤣🤣

DAOUDA_D⭐️⭐️🇸🇳 profil fotoğrafı
DAOUDA_D⭐️⭐️🇸🇳4 ay önce

😂😂😂😂kou guiss lou moy

A B G profil fotoğrafı
A B G4 ay önce

Pour votre santé mentale et cardiaque arrêtez de regarder ou d'écouter keur doff yi. Un ramassis d'idiots de parasites et de déchets humains

Serigne dabakh 4 real🇸🇳 profil fotoğrafı
Serigne dabakh 4 real🇸🇳4 ay önce

Fénn bokkou na si bakkar yii gueneu makk mais amna niouko dieul beug ko def métier

A2K 💎🇸🇳 profil fotoğrafı
A2K 💎🇸🇳4 ay önce

Le plus grand des génies c’est celui qui les a appelé KEUR DOFF YII 😂

ALOU LASSE profil fotoğrafı
ALOU LASSE4 ay önce

Té bouy doul han day khoulékou rk ak gnawayam bi ki dou sakh rouss doul rk lay deff😂

Nightmare profil fotoğrafı
Nightmare4 ay önce

Kiii mom dafa meun fèn

Rahmane🇸🇳 profil fotoğrafı
Rahmane🇸🇳4 ay önce

Mais thieré guenoulwon yomb sauce? Walla?😩😭

Abdoulaye Niang🇸🇳🥇❤️✊🏿 profil fotoğrafı
Abdoulaye Niang🇸🇳🥇❤️✊🏿4 ay önce

Make yo xamni weure di gâte rk😭🤣

Pisco J profil fotoğrafı
Pisco J4 ay önce

La méchanceté les fait mentir. Sans vergogne aucune honte

Bassediop Diop profil fotoğrafı
Bassediop Diop4 ay önce

Meme wa plateau bi hame naniou ni dé kaathie🥹😂

L'autodidacte 🇸🇳🧠💡 profil fotoğrafı
L'autodidacte 🇸🇳🧠💡4 ay önce

Aka mana doul 🤣🤣🤣

😇Behrouz Piccolla 😇 profil fotoğrafı
😇Behrouz Piccolla 😇4 ay önce

Concours Générale Matière composée : Sciences du Mensonge

liz profil fotoğrafı
liz4 ay önce

Thiey! Ki ana ay domam?

Keurkeuriih_Rekkk🇸🇳✨🛠️🇺🇸🔥🔧🇩🇪 profil fotoğrafı
Keurkeuriih_Rekkk🇸🇳✨🛠️🇺🇸🔥🔧🇩🇪4 ay önce

Daay dou dh Waxoul deug

εℓ мαℓιcк🅧🇸🇳 profil fotoğrafı
εℓ мαℓιcк🅧🇸🇳4 ay önce

Gnimou togal xam nagne ni dafay doull

•🅃🄷🄸🄰🅁🄾🅈🄴 44 • 𓂧𓆓𓏭𓃀𓇌 𓎼𓅱𓇋𓇌𓇋 profil fotoğrafı
•🅃🄷🄸🄰🅁🄾🅈🄴 44 • 𓂧𓆓𓏭𓃀𓇌 𓎼𓅱𓇋𓇌𓇋4 ay önce

Kou am yapeuh Thiere teuwoula

Talibé Monseigneur Benjamin Ndiaye Mou Sell Mi profil fotoğrafı
Talibé Monseigneur Benjamin Ndiaye Mou Sell Mi4 ay önce

Sénégal ay Pa gnoy tok télé di fenn en 4k FHD sans gêne. Thiey mim rew 🤦🏽‍♂️

Ndiaga⭐️⭐️ 🍉 profil fotoğrafı
Ndiaga⭐️⭐️ 🍉4 ay önce

Thiey yalla

Lankizer Franc Ndiago ❤️👑 profil fotoğrafı
Lankizer Franc Ndiago ❤️👑4 ay önce

Leer nama mom mo togoul del diokhei dépense sa keur lala wakh

Mouhamed Ndiaye profil fotoğrafı
Mouhamed Ndiaye3 ay önce

Tjr wa keur doff yi 😂

Benzer Videolar