Loading video...
Video Failed to Load
C’est à la fois drôle et tellement vrai 😂😂😂
29,026 views • 6 days ago •via X (Twitter)
15 Comments

C'est tellement vrai😂meun guen bokk 6 à 7 produits mais dolen bokk marque bolenni jeul

Bilahi deug rk la wax 😂

mais pourtant nos parents qui ont hérité l’éducation coloniale font la meme chose. Mann sama Père looko diohh mou lire notice bi que ça soit un medicament ou aliment

Lou yomb la niouy saway

Fi gayi na nekh rk le reste c’est pas important 🤣

Haribo par example dafa am gélatine les clients ne se rendent même pas compte

Mais niom danio beurri allergie

Mane dama koy deff depuis bi ma commencer sport meune nafa def 1h di weur reik 😂😂😂😂

Quantité moniouy ray🤣🤣

Tellement vrai

Boy indil lé🤣👌🏽

Mane dh damay lire ba dofff bala dieul laneeep

Perso damay lire déh 😂té douma toubab.

Man bi gueuneu yomb lay djeul prix dh lay xol

Américains yi d bokugn si lolu Sen yoon 😂
Related Videos
La suite de la vidéo est encore 100 fois plus drôle 😂😂😂😂😂
Iceberg Slim 🇨🇩
291,787 views • 8 months ago
