Deuk bi amoul khalise 🤷🏽♂️
@GeneralGalsen7550 位关注者
33,950 次观看
32 条评论
评论来自 X (Twitter) 上的原帖

@slmn2019
Normal que personne ne vienne. Avec des prix haram comment veulent-ils que les gens achètent. Personne n’est fou
76 个赞

@Ousmanedieme14
En tout cas ñoune diaye nañuh téh diéxal nañuh wayé nak kussi beugga diayé sap xar lingassi financer yeup mussibeuh dinala daal. Preuve à l'appui
56 个赞

@ballamaramelo
Bougn niou sonnal nioo cheiral kharr yi ba sein lharr yi lamb nagn deim sein keur yi leikk ko
56 个赞

@abdoubo86209603
Nit yi legui douñou ay complexes déf lo meun rek bo tedé nélaw après tabaski la vie continue
35 个赞

@A_khadre10
Gnom gno yok prix yi di graw graw lou demb blh sama bene xaritz moma wo dh ay 00h wallahi nane ndax guissouma kouy djeund xare maniko gnata mounima insbi key lou way ame ame xare
19 个赞

@Mamadou33364332
Kou liguey am khaliss khar 😂😃☝🏾🇸🇳🇸🇳
7 个赞

@NB251299
@GoraKonte21977 Bolen ndieukei won fingeen moudj ni dolen lambe lei
5 个赞

@SEYDINA___gyyb
Niit gni kéne douléne ray
5 个赞

@rabbusenegal
Yene la rek daguene di dof doflou vous fixez des prix exorbitants pour un mouton qui n’est même pas capable de se tenir debout
5 个赞

@PapaNdo38578673
Niomla dh atie prix yi di exagéré ils savaient que dina dess s'en lokho
5 个赞

@princembacke
Dou yena adj sene prix yi
5 个赞

@Mh_Rmad
Deuk bi dueugueuroul diay katt yi nio rew . Lgui da ngay amme 200mille nioulay diay rew
3 个赞

@Thinker022
@Marseille345 Je n'ai aucune pitié pour les vendeurs de mouton. Vous êtes tous des truands et des vampire
3 个赞

@BayeLazanba
@Marseille345 Wadji thi boppame mo yabbaté Même personne bi demb bagn’neu kouko fay thi bene xar 270mill Nieuw taxaw fi nane deukk bi doxoule Ki daa yabbaté Boy dakar yi nio yakk jaayoume xar Beugg jayei liniou dépenser thi xar yi
3 个赞

@Ousmane_Sdm
Deuk yiniou raw yeup djiko lagn niou rawei djiko you baxoul moko waral dakar fékhé nagn beu 100k nit meunousii am khar
1 个赞

@yuzassifff
Gayi dieund nagn bou yagg Li nek s'en poche lagn dieundé dem bayi lein ak s'en kharou or yi 😂
1 个赞

@boobalelord
Dou deugu yena yok prix di jay am fite
1 个赞

@FallNdiol168276
Sa biir wakh kouko deg xamni danga yok saay prix xar ndakh malien yi gneuwouniou
1 个赞

@jppzeng
Lol gni deuk dakar yeup la majeur partie nioumeu xam yeup degno guen dem thi loumeu yii outii xarr nieuwatt. D’accord élevage daffa metti mais soy diay dagay pendre en compte pouvoir d’achat de la clientèle.
1 个赞

@khabaneseck
Operation dou da ngay teup rék dougousi amo client you assuré ba paré beug adj sa prix motax kouko déf di nga wétokh say kharr diko doundeul dieumeulé wate akh mom ba tabaski prochaine
1 个赞












