Загрузка видео...
Не удалось загрузить видео
Djaplene si ma ame trophée 1M bi damassi Beug dozè 😭🙏🏾
74,534 просмотров • 3 лет назад •via X (Twitter)
Комментарии: 10

Le jour où vous vous réveillerez et que vous n’aurez pas 10 likes sur vos publications vous comprendrez qu’il y a des moments qui ne laissent pas de place au rire.

Le Sénégal ne vous intéresse pas tout ce qui vous intéresse c’est les avantages que vous tenez du pouvoir . DEm lenn rek lepp dina diex mouy yaw ak Yenenn nitt yii teugn senn guemign di jouer à l’aveugle sur les morts .

amouniou sén diote rewmi laniouy lidianti ba nopii

Souniou désabonner sa compte Twitter Facebook ak insta ci ngay ndey comprendre. Tête de con👎🏽

Swaay nunn sunu avenir reew lañ tall gayin nga naan ñu ay trophée Waxal ci situation reew mi..

De vrais connard toujours dans la diversion 2 jeunes sont morts en plus des blessés grave ,Trophée bi laay dieul niokh ko sa Ts’´nd nga xam ! One rek

Abba y a deux jeunes morts à Ngor 🙆🏾

A Ngor c’est chaud et vous avez des tribunes pour en parler et dénoncer les dérives des FDS ou même ne serait-ce ce informer l’opinion publique et internationale de la situation mais voila ça vient sur Twitter nous parler de futilités ; tout le temps dans le divertissement pfff

Katal ndem feulé yak sa compte YouTube le pays brûle gueine niouy divertir. Yeina ko Ndeye talle

Nioune réw mi monou yittéll
