Video wird geladen...
Video konnte nicht geladen werden
Écoutez le s’il vous plaît!!!
39,889 Aufrufe • vor 1 Jahr •via X (Twitter)
10 Kommentare

أبو بكر الصّدّيقvor 1 Jahr
Céy Yàlla 😭. Li ma gëna yéem ciy waxam mooy lu mu wax dalal ko ci alxuraan, lu jafe la nak. Capacité de réflexion bu rëy a rëy lay laaj. Yal na ko Saa Boroom samm 🤲

𝐁𝐚𝐚𝐲 𝐗𝐚𝐥𝐢𝐢𝐥 🇸🇳📚📚📝vor 1 Jahr
Dafa am tawféex ci Alxuraan

Saliou Seck 🇸🇳🇸🇳 🇵🇸🇵🇸vor 1 Jahr
Qui va devenir son manager et lui ouvrir une chaîne pour partager son savoir.

AnGe Ji'BriLvor 1 Jahr
Tei ku dall leuh ndeysan. Comme kuy disserter Arguments+exemples lalay jioh teg si wakeuy yalna Y'Allah samkoo

💙𝓕𝓪𝔂𝓮𝓜𝓪𝓵𝓲𝓬𝓴🇸🇳♡♤🇧🇷🇲🇦vor 1 Jahr
Kou xamoul lan moy waliyou rkk xolal si wadji nitou yalla deugua ngui ni

Alaaji Fàllu Sillavor 1 Jahr
Man damaa yéem !

𝐁𝐚𝐚𝐲 𝐗𝐚𝐥𝐢𝐢𝐥 🇸🇳📚📚📝vor 1 Jahr
Ak man de yéem na ma lool sax

@kab Khoudia Niang 🇸🇳🇫🇷vor 1 Jahr
Kou am ndimbeul sonou borome laa. Kou degg Alkhourane Karim bila.

mame cherif 🇸🇳🇸🇳🇸🇳vor 1 Jahr
Ki mane daff ma yèm Wa bakhna

SowCheikhvor 1 Jahr
Mashallah yalna ko Yalla moussal si tiate ak lamigne yalnako Yalla are amine y’a rabi 🙏
