Erreur dโarbitrage non ??? ๐ญ๐๐๐๐๐๐
@Pa_Seydou_84.2K followers
21,113 views
18 Comments
Comments from the original post on X (Twitter)

@PAPECHAYBA67435
no le gars arbitre dafa siffler mou gestou. cโest lui le fautif
30 likes

@Pa_Seydou_8
Avant arbitre di sifflรฉ la tournรฉ Arbitre daf len warone lathie ndakh Parรฉ nagne dโabord
27 likes

@MalickDieme12
Maiโs lโarbitre doit aviser les 2 lutteurs avant de siffler ๐๐๐
8 likes

@Pa_Seydou_8
Voilร

@MalickDieme12
Arbitre bi mo def erreur dh

@mouhamedngom96
Arbitre dou coach
1 like

@Pa_Seydou_8
Arbitre day lathie Mbeur yi ndakh parรฉ nagne avant tout*

@mouhamedngom96
Ladj balenn
1 like

@Pa_Seydou_8
Ahhh dama Guissoul lolou katt

@linooh221
Wa li lanla๐คฃ๐คฃ๐คฃ

@jiikush1
Li mome arbitre bi moko tay dou lathiei sax ndax parei nagn ๐๐๐๐คฆ๐พโโ๏ธ

@Pa_Seydou_8
Mom la dh

@RoumzoC
Akh wadji tmt nekhoul diapalรฉ dh๐คฃloumi guerssou tei arbitre sifflรฉ ๐คฃ

@Albad_a1
Leigui nouniou moudiei ?๐๐ญ

@Pa_Seydou_8
@A1_Alvine Dama kham ๐

@Albad_a1
Souma parei na ko lidjenti parce que li diaxasso na trop do xam kou neik en tort๐๐

@Junior570274240
Wa legui ki dane mome amoul sakh kersa beiteu ki dane ko ๐๐๐ki danou tamite loumouy wax wa kogne ba

@Seeny221
En sport de combat lโarbitre doit tjr veiller a ce que les deux combattants soit bien au courant du sifflet Mais lร le lutteur aussi nโest pas exempt de tt reproche