Video yükleniyor...
Video Yüklenemedi
Erreur d’arbitrage non ??? 😭😂😂😂😂😂😂
21,113 görüntüleme • 11 ay önce •via X (Twitter)
18 Yorum

no le gars arbitre dafa siffler mou gestou. c’est lui le fautif

Avant arbitre di sifflé la tourné Arbitre daf len warone lathie ndakh Paré nagne d’abord

Mai’s l’arbitre doit aviser les 2 lutteurs avant de siffler 😂😂😂

Voilà

Arbitre bi mo def erreur dh

Arbitre dou coach

Arbitre day lathie Mbeur yi ndakh paré nagne avant tout*

Ladj balenn

Ahhh dama Guissoul lolou katt

Wa li lanla🤣🤣🤣

Li mome arbitre bi moko tay dou lathiei sax ndax parei nagn 😆😆😆🤦🏾♂️

Mom la dh

Akh wadji tmt nekhoul diapalé dh🤣loumi guerssou tei arbitre sifflé 🤣

Leigui nouniou moudiei ?😂😭

@A1_Alvine Dama kham 😂

Souma parei na ko lidjenti parce que li diaxasso na trop do xam kou neik en tort😂💔

Wa legui ki dane mome amoul sakh kersa beiteu ki dane ko 😂😂😂ki danou tamite loumouy wax wa kogne ba

En sport de combat l’arbitre doit tjr veiller a ce que les deux combattants soit bien au courant du sifflet Mais là le lutteur aussi n’est pas exempt de tt reproche
