Video yükleniyor...

Video Yüklenemedi

Ana Sayfaya Dön

Ki mothi kan🤣🤣🤣🤣🤣🤣

22,328 görüntüleme • 10 gün önce •via X (Twitter)

37 Yorum

Kalamu Badji🇸🇳 profil fotoğrafı
Kalamu Badji🇸🇳10 gün önce

Niom affaire yi business lagn ko diapé

Mbodjifara 👏🏾 profil fotoğrafı
Mbodjifara 👏🏾10 gün önce

Kugnu ray lagnu weur gni

NADIO 🇸🇳⭐️⭐️(khoslouman) profil fotoğrafı
NADIO 🇸🇳⭐️⭐️(khoslouman)10 gün önce

Ana sa baye Loumouy diarigne

pause café ☕️ profil fotoğrafı
pause café ☕️10 gün önce

Dakhaar ma fogone pour bolene eumbé la chaque 28 jours dakhaar dagn si meune deuk

Muhaamed 6c profil fotoğrafı
Muhaamed 6c10 gün önce

On dirait les parents ils font plus leur role hyn🤣

Thiapathioly profil fotoğrafı
Thiapathioly10 gün önce

Djiguéne yi kagn lagni xamé xiff ak amé douleur

εℓ мαℓιcк🅧🇸🇳 profil fotoğrafı
εℓ мαℓιcк🅧🇸🇳9 gün önce

Sheuuttt gniii lougne gnou diapé

Mbodjifara 👏🏾 profil fotoğrafı
Mbodjifara 👏🏾9 gün önce

Objet srx

kou beug sonko beug nala. profil fotoğrafı
kou beug sonko beug nala.10 gün önce

Ko takoul lofa def boula woré yako yekk sa bopp. Relation dou business kou nekk na gerer famille wam walla kou nek sa famille gèrer la. Damala nopp mala raw loussi diokhé khaliss domi wout. Yen jigeen gni danio nekh

ADS 🇸🇳♊️ profil fotoğrafı
ADS 🇸🇳♊️9 gün önce

Té mom petite attention lek rek la ci khalat 😂😂 mounan traiter mieux…

Mouhamed profil fotoğrafı
Mouhamed9 gün önce

Té miom khalatouniou déffal goor Dara

Astou Bint Baba profil fotoğrafı
Astou Bint Baba9 gün önce

Wa copin ak copine mom dou farata dé je suis une fille mais mounou ma comprendre yéne yi wala dama wéroul

Bùur Dali 🇸🇳 🔰✊🏿✊🏾✊🏽 profil fotoğrafı
Bùur Dali 🇸🇳 🔰✊🏿✊🏾✊🏽10 gün önce

Sen Bop Yi Mo Amoul Ndokh

Ghost 🇸🇳✌🏾😈 profil fotoğrafı
Ghost 🇸🇳✌🏾😈10 gün önce

Kenen kou khiff leu rek 😂😂😂

Mo At'Tijany 🇸🇳 profil fotoğrafı
Mo At'Tijany 🇸🇳9 gün önce

Khamoul sax fouy l'ouest Mounane day conseiller

Ahmadou🇸🇳🚀 profil fotoğrafı
Ahmadou🇸🇳🚀10 gün önce

🤣🤣🤣🤣niom dagn beug nopal sen papa yi khana

Mansour🏴‍☠️ profil fotoğrafı
Mansour🏴‍☠️10 gün önce

Djiguene Gni amouniou guenn ndieurigne wakhi madd ak tacos rek ay doff lagn rekk

Barhama🇸🇳✨ profil fotoğrafı
Barhama🇸🇳✨10 gün önce

Boul investir jamais sa khaliss ci projet mort-né... Jabar dal lo ci déf khépp ko bobou moy projet bou bakh bi...

Papa Samba Lo profil fotoğrafı
Papa Samba Lo10 gün önce

gua déme ci kokou point

🤴🏽 PRINCE profil fotoğrafı
🤴🏽 PRINCE10 gün önce

Nek léne si 90 - 98 yi Bou 2002 bi lou yallah kham doyna 😂

Pape Bassirou Djiba profil fotoğrafı
Pape Bassirou Djiba9 gün önce

Kew Lakay jeundeul

𝒜𝒹𝒾𝒸𝒽 𝒮𝒶𝓂𝒾𝓉𝒽 profil fotoğrafı
𝒜𝒹𝒾𝒸𝒽 𝒮𝒶𝓂𝒾𝓉𝒽10 gün önce

Si khalé bou ndaw ya wow beut

Mohamed Fy profil fotoğrafı
Mohamed Fy10 gün önce

Princess le doikhlen ko tieurr

Dev🥷🇸🇳 profil fotoğrafı
Dev🥷🇸🇳9 gün önce

Djigeen senegal ndeysane pour niom far dieukeur la😂

Moustapha Barro profil fotoğrafı
Moustapha Barro9 gün önce

Lolou lepp si khiff bi la rk 🤣🤣🤣

𝙸𝙳𝚂🐐 profil fotoğrafı
𝙸𝙳𝚂🐐9 gün önce

Sama sho bi dh mom merci sax dakoy bañ, rew rahh na si dh

PROS2029 profil fotoğrafı
PROS20299 gün önce

Comme des bêtes leur manière de réfléchir. Et le pire c’est que ces idées sont tellement figée dans leur tête. Pour yen goor bou leuh dokhane gua bayi kigua nekal dem ak mom dinala takk ? Demeurez bêtes et nakh seuh bopp c’est pas interdit, mais à vos risques et périls !

ᴍʙɪɴᴅᴇᴇꜰ✍︎︎🇸🇳🇵🇸 profil fotoğrafı
ᴍʙɪɴᴅᴇᴇꜰ✍︎︎🇸🇳🇵🇸9 gün önce

Lekk lekk lekk😭

Shigar profil fotoğrafı
Shigar10 gün önce

Man mom bayina cardio bi la amoul

Heuz 🔱 profil fotoğrafı
Heuz 🔱10 gün önce

Sa copin la wala sa papa

￴ Lord hakill⚡️🔍 profil fotoğrafı
￴ Lord hakill⚡️🔍9 gün önce

Ki kan la si gars yi

Mhd profil fotoğrafı
Mhd9 gün önce

Esk dou weur farou médecine tamite🚶‍➡️

NDOGO DAARA 📚 profil fotoğrafı
NDOGO DAARA 📚9 gün önce

🤣🤣🤣🤣🤣🤣

Fassin Jules Sylla profil fotoğrafı
Fassin Jules Sylla9 gün önce

Traître mieux bi moy niou diokh léne lekk 😂💔 ok tacos girl

Ababacar Sadikh 🇸🇳 🇱🇧 profil fotoğrafı
Ababacar Sadikh 🇸🇳 🇱🇧10 gün önce

"princess treatment"

Herr YADE🇸🇳🇸🇪 profil fotoğrafı
Herr YADE🇸🇳🇸🇪9 gün önce

Ma dieundal le Beignets Nicolas 🤣🤣

no baye no life profil fotoğrafı
no baye no life9 gün önce

Chocolat bi bane chocolat

Benzer Videolar