Sensitive content
This media may contain sensitive content.
Loading video...
Video Failed to Load
Kon nak Bismillah🙏
30,207 views • 1 year ago •via X (Twitter)
10 Comments

¡ GodisGreat 🐍!1 year ago
Ay serign dara you besss ngen nara guiss fi legui😂

𝐋𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝐞 𝐏𝐨𝐬𝐭 🇸🇳1 year ago
Moom Kay dafa melni ñépp mujj nañ doon ay Sëriñ Daara😂😂

bint_moustapha1 year ago
Daara sokhna Adja Bineta Thiaw cité Alioune Sow oustaz yi ak seyda yi ken amoussi dra ku beug dieukeur/diabar rk vas-y yyyy🤧😂

𝐋𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝐞 𝐏𝐨𝐬𝐭 🇸🇳1 year ago
Na Oustaz ya jël ça Sayda ya rekk mu gëna gaaw😂

Taarub yoon wi1 year ago
Waxko mou bole ma ci

𝐋𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝐞 𝐏𝐨𝐬𝐭 🇸🇳1 year ago
Saa Daara fumu nekk 😂

BintAhmaDem🥰1 year ago
Waa tiktok ñépp doon nañu ay Sëriñ Daara 😂😂

FDL 47🇦🇷1 year ago
Kou bakh na yatou rek. Maylene serigne Dara yi sokhna ak gniko beugeu nek ak gni beugeu am té amouniou ndakh diappa ndiwoule

Abdallaah1 year ago
Am na solo lool

Maréchal_Weuz👑🇸🇳1 year ago
Done Serigen dara diot na nak 🤔
