Video yükleniyor...
Video Yüklenemedi
Li dher moy deugu
24 Yorum

Waw waw amou deux poids deux mesures dh na yon def yonam kounek assumer rek

Ça se voit que jang xassida yii ak dundu khassida yii wuuté na

Merci pape jeureujeuf dagno sone way. Yene gnouni diné Islam haramal na, mom falei woul lolou nguene nane ay mouride lak etc. Neik lene ay nite

@CS_babou Lii deh la geum Serigne Touba limou woté daga leer nagn kepp kou diar sa yonou bopp c ton problème

Fii la gars yi wara nekk dh walay

@kanki_dfalillou Mouride nouveau model 😂😂pape amoul

Yoon wi aussi limou bakho moy keppou kou ciy wakh sa wara and ak daal ak ay teeguin ! Té bala nga wakh da wara fek nga am ci ndigueul

Mais louy mouritou nouveau modèle 😂😂😂😂sheutt Sénégal 🙆♂️😂

Meno né seugn bi geu geum mom guay toppou niu diap genre niit ni si biir moulay meutti au moins Kay sante yalla bagn fegné niu meun lagn seppi si c'était pas le cas continuer nek si sen Lou boon ba paré di toppou seugn bi

@DialloLinguere Mou diekh takk

@BadriDiallo Bokkalé bissi deuk bi dougn si wakh

Jesus peut transformer ta vie ❤️

Nañu lenn weer niom nieup et on passe à autre chose

Bu lépp weesoo nag, gën leen a focus ci jàng seen diine ak géstu Serin bi, ba comprends bu baax lan mooy ag murid te ngeen moytu riir mi rekk, nu bari riir mi lanu topp waaye xamนทีน dara ci yoon wi akug taalibe. Saa boo leen woowe ci jàng xam-xam ñu jàppe ko ay detail.

Gnoune serigne touba mognou gnorr....

Fii leu mouride yeup taxaweii d!

Islam mo eup dolé mouride tei mom mo reub goor djiguene kone amoul sympathie.! Ass xassida ak ass lenene mossi yem.

Nouveau ancien Bou wow Kong moteur jamais touché 125 carburateur noir matt wowal 100 mécano boula neixei

Degueu dou rombou ayy noppp

@Africain_76310 Wwww

@bamba10gaye Neuve model kaye 😂😂😂

Fila nek man

@mbaye_21 Wawaw ki da bonn wayy 😭

Xaral diga degeu si problem bi koulaye bête si rewmi t gnoune mome kilife la nake xaral lolu
