Malen ko tegua fi 🧎🏻♀️🧎🏻♀️🤧
@kimichdash139 B takipçi
31.293 görüntüleme
11 Yorum
Yorumlar X (Twitter) üzerindeki orijinal gönderiden alınmıştır

@SaveursMima
Xana ki yeugoul lou xew 😂😂😂😂 barki yallah yaw rek lay top soy deff ni legui niou arrête 😂
5 beğeni

@kimichdash1
😂😂 dedet pour mom limouy diay dafa bakh nonou
2 beğeni

@Hakan_kane
😂😂😂yaw xana lanceuse d’alerte
4 beğeni

@kimichdash1
😂😂 det dama dimbeuli khaler yi rek
5 beğeni

@ismaila14481537
Ahh waw bahna il faut continuer rekk liy Ram si niakk bi la djeum
3 beğeni

@gawane_borom
Ma wax?
2 beğeni

@kimichdash1
Waw

@Zon_Positif
@kimichdash1 bagnal lolou. Soo défé ni xalé danou si gueuneu nék dé🥹
2 beğeni

@HadrameF
Lou kholi lokho nga beug ko def si kanam😂
2 beğeni

@omardieme18
I really appreciate your warning ⚠️ you are doing it great may good bless you inchala
2 beğeni

@kimichdash1
Merci beaucoup ☺️
1 beğeni
