Загрузка видео...
Не удалось загрузить видео
Mame mouné kou doug kasso ?😭😭😭
80,811 просмотров • 1 год назад •via X (Twitter)
Комментарии: 11

Wa legui yonentibi aka serigne bi Louniou fii oute ba pare ?😭

- Know Me

Wa fou yonnent bi dougué kasso ?

Elles foutent la vie des gens en danger et prétendent quoi?? Au cachot

Vraiment gni warnanou yamm tokk dii feine ni rekk

Ki fane la yonante bi dougué kasso ki dina takhe ma télécharger tik tok di saga ndeyam chaque jour

Sénégal laniou wara mise en jour ndakh ay dofff laniouy promouvoir dilén may audiences vraiment ce pays risque gros si on arrête pas certaines dérives qui guettent le bien être de la population

Sénégal walahi gni ngui seitane you graw difi am. Bagn leine gueinei yoneinete bi si seiye yeufou thiakhane yi rek

Ki moom ndax ànd nag sagoom Yónnent bi (SHW) fan la duggee kaso te lima gëne metti ñoom dañuy def séen lu ne winŋ naan Sëñ Tuubaa dugg na kaso, di ci joxe ay niral ñi dañoo rew ki moom ab dof la.

Ndawsi khaléla wala makk?

Ki meune na féne yoneute bi moko dessé
