Video wird geladen...
Video konnte nicht geladen werden
Mazhab Imam Malick 👂
22,667 Aufrufe • vor 1 Jahr •via X (Twitter)
12 Kommentare

C'est pas Imam Malick c'est plutôt imam Chaafih. Dafa djoum

take the journey

والمأموم في الجهرية خلف الإمام لا يقرأ الفاتحة، وإنما ينصت مختصر خليل مع الشرح Esk jaawale wul ngiir yi laa fook wala ndax rissala tmt lii la wax

Xana do lire commentaire yi bok mbokk. Rectifier nako deh

Amna niouy diang fatiha si deux derniers rakka si boudé diouli biniouy wax si kaw la lolou mom louy até bi??

S’il récite un verset seulement tu n’auras pas le temps de faire Fatiha 🤷🏾♀️🤷🏾♀️

Bonne question ?

Ku niow fékk imam si roukoo nak ?

Sou féké wahtou bouniou doul bireur (tisbar par exemple) là aussi danga wora deff fatiha bii?

so feke imam di roukoo nak, ci bane wakhtou ngay tari Fatiha?

Qiraa'atul fatiha lil imami wal fazzi duunal mamuumi nak ?? Lii amna ndioumtei bou makk sahh

C'est pas Imam Malick mais plutôt imam Chaafih dafa djoum🙏
Ähnliche Videos
Sensitive content
Ye Mazhab hai ya pornhub hai ?😹🤲😌
God
184,754 Aufrufe • vor 1 Jahr
