Video yükleniyor...
Video Yüklenemedi
Ndékè Balla yag na niouss mbeur welelelellele😭😭😭❤️
107,941 görüntüleme • 2 yıl önce •via X (Twitter)
58 Yorum

Comme papa bouy dorr domam kay🤣🤣🤣

Billae humiliation

Balla yagg na corriger nitt ci birr guew.

@ELTOROTHEBOSS Crx

C’est grave comment s’est passé inaperçu cette correction 😂

Incroyable 😭😭😂

Amm victoire ba paré sen khol di metti 🤣🤣🤣

Li dfay frigo sougn xol li

Manan balla mbeur yiniou wax nio dakh khakh si lamb dji balla daflen doumeu 😂😂

Wouyyy😭😭😭😭😭

Teksi cercle VIP djamo dji moy seul bou dane 3 VIP 2 fois Mdo Lo , Gris , Tapha Tine ta kou nekk si niom bimou lay dane si 2e combat nieup daniou don wax il es finito 😂😂

@YayaaCatalan “Modou athlete la” “Modou dafa meun xeex” Lepp daf koyy reer face à Balla.

@YayaaCatalan Wouy😂😭😭😂😂😂

Ki balla daka khep dou moromom sakh

@yacefcb44 Crx

Likay mn takh supporters Modou lo yi bagne Balla 😂😂

Billae nak😂

Wakh djé fi né rek wayé golo khamna bayam 😂

Billae wallae

Non Balla dafa soxor si guew

Bandi leu

Balla bima giss démb Modou Lo mokka mën actuellement

C’est parce que tu connais mal Balla

Boy sétaan nañu combat d’hier bi. Balla bima giss meuneutoul dane ñu baari dh. Plus tard di ngané waxon nlako

@Jaah221 Ioe warone nga beurek Tapha Tine 😂

@Jaah221 Mane duma mbër 😂😂😂😂. Mais sumako nékkone bëgg agg ci ténors yi ci Tapha Tine lay diaar

@Jaah221 Tapha 10 ans danouwoul d té ay tenors rk la dane faut juste louer le bravoure de Balla Gaye 2

@Jaah221 D’accord monsieur et cette belle époque est à saluer mais ce Tapha ne fait plus peur à personne. Et on a vu un Balla meilleur que ça

Le pressing est bon mec, j'aime ça 😂

@Mouhamadou17249 Hahaaa😭😭😂

Peut être guisso ko on sait pas .

Sama kholl bi sedd neu si liii 🥹❤️

Nieupp began😭❤️

Finalement tu forces 😂😂😂

Niouss yi lalen fatali

Yagu nagn koy niouss tmt 😂

Mais cette vidéo c’est une pépite 😂🙌🏾

@Karim_bambaaa Eumeu sene tmt yagg nafi teggeul mbeur faté wouleen ko gspr

@Karim_bambaaa Delen xéxè sen dolei😂

Ndeysan instant dioutal bi modou ne contrôlait plus rien

Ih dafay nioussé 😂

Crx

Tapha mo bess le rec mais saway mome dagne ko reug bamou bayil bopam gniou perier loko balla moy mbam😂

Mais dougnou wakh policier 👮♂️ yi di sétane tek cii commentaire

Ce sont des humains après tout 😂

Pour ce combat,Modou lo a été très brave pourtant .

Ça doit être ça ouais😂

Dan mbeur ba paré mou eupeu leu niveau 😄

Ouais Moud Lo a pris de l'âge 😲

Ah

cva tonton dagua fater tontou fii deh

Woyyyyy tank yangi balancer yaw 🤣🤣🤣🤣

Wolene Eumeu sene🤣😂😂😂 Rokosss

Am victoire sa khol nekhoul 😂😂😭souffrez en silence 😂😭

À part modou lo balla nakk ay pa fin de carriere rek lay dannn

Je ne suis pas trop lamb mais lima guis nii nexoul ba néxoul mais #Balla da diapé #Modou com boyam koi, téyé boy bi di nogatou nii rek. Noo noo li c'est trop way😠🤦🏾♂️

Li dorr fayou la

you like new space laced bass music?
