📌PM ramassé na Pape Djibril Fall
@KiliFeuu54K followers
45,896 views
10 Comments
Comments from the original post on X (Twitter)

@SolarHeavy
check out the vocals in this song
1,506 likes

@GAALGUI_221
Gosse bi amoul bopp ndéké🤣 Thierno daw Kirikou daw yaw ngey risquer di djaay graw ak rafete veste motakhite😂
9 likes

@MorySy3
Pape Djibril Fall notre dernier chance sera Le prochain a s’inscrit sur la liste boycotteur à L’AN 😂 PM bayil ligay def sino ken dou ngagou ñewou
6 likes

@mouhametmbe12
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
3 likes

@Ndeyendiaye1357
Ay PM prochaine session do guiss opposant di 🤣🤣🤣 limite dess nga wagni niii
3 likes

@BakaryBadji14
Té da da da bania dem rkk niou nii boycott ioe nga nieuw
3 likes

@MalickSDilick
Pape DF deh dotouko deffatii😂🤣🤣
2 likes

@AssaneFallDabo2
Doléne tekil pape cravate yi bala mo xeum😂😂😂réponse pro bi dafa yeungeul deuneum bi😂😂😂
1 like

@Mouhamedine25
Wadji nane na 😂
1 like

@Serignemba95475
Boy bi Sonko Thiaw nako thiaw you saff😂😂😂😂
