Poular devrait être la langue national 🙂↔️🙂↔️🥹🥳
@Aminah_Kah2.3K followers
51,637 views
64 Comments
Comments from the original post on X (Twitter)

@Kurosaki_seydi
Kholal sene affaire yii nguene di bayi boulene niou sonal wolof mooy souniou lakk national kene tereh woula lakk sa lakk. (Je suis serere)
101 likes

@Aminah_Kah
Serrere rek ga meuneu done
3 likes

@BallaCisse56
Est-ce que do bayi wolof bi rek wolof da nekh d baba mal bat bou nekh la yor karr
73 likes

@Aminah_Kah
Poular tamit daara dakouko
13 likes

@Nb0804_
Shi diapalé lene niou rek . Boulene fi eundi genre débat yi 🙏🏽
49 likes

@Aminah_Kah
Chéri foo méré?
6 likes

@ez_l0e
@Nb0804_ Say deug la , may len gnou rek
8 likes

@Aminah_Kah
@Nb0804_ Soumalen mayoul ?

@ez_l0e
@Nb0804_ Gua doxan sa ndey fé ,sof Ak waxou khet
1 like

@Aminah_Kah
@Nb0804_ Je te donne 20mn pour que tu supprime
1 like

@starr5_11
Non merci. Le peulh est partout en Afrique avec differents types de peulh… le wolof est bien plus riche… pardon rek ensuite vient le sérère en terme de richesse et de culture indéniablement ☺️
35 likes

@Aminah_Kah
Mdrrrr
2 likes

@gorgui_ibrahima
Salam banérabes mbada ? Jamm tan Malheureusement on ne décrète pas une langue nationale c le fruit de l histoire alhamdoulilah qu au Senegal la majeure partie des royaumes etaient sous la domination de l empire du djolof c est ce qui a permis de faciliter la langue wolof
21 likes

@Aminah_Kah
Jam tan allahamdoulilah Mine deh komi beltidoo tane mbodo hala mais mbido andi 🤣
2 likes

@Ahmadoubamba36
Dett rafet ngen rek ngen beug def seen langue nationale 😂
19 likes

@Aminah_Kah
Raison de plus 🤣🤣
4 likes

@Sam_theblue221
S’il te plaît rk c’est pas le meilleur moment pour tweeter ça
15 likes

@Aminah_Kah
Je te demanderai la prochaine fois le bon moment daccord ?

@Aminah_Kah
Quel contexte qui est tendu ? Ya pas un problème les peulhs et les autres ethnie ?

@Sam_theblue221
Hein ?? 🤣🤣




























