Sensitive content
This video may contain sensitive content.
Sey beu Tass naaa🥹🚶♂️
@Cisse_Maps31K followers
231,314 views
34 Comments
Comments from the original post on X (Twitter)

@MoussaB29306989
En vrai je vais pas rentrer dans les débats mais galsen khamouniou charte mariage devoir de la femme en vers son mari et vice versa Ton mari mo eupeu ndogal ci iow mm devant ton père donc xolate léneu seneu bopp
166 likes

@KroosSarr
Yalla nassi ay autorité Pastef dokh tanki diam ci soutoureu en dehors de tik tok et des autres RS. Patriote boussi meuna diap aussi mou deff ko
74 likes

@Papis_Jaah
Xamna le fait que la go mèdiatisé affaire bi motah wadji gueneu sissou fassé ko
64 likes

@senegalo_malien
Bou ndieukk problème Bou dane am si seuy parents yii Wala nidiayes maname kilifeu yii niosdi dane dokh tankou diam si soutoureu. Mais legui lou khéw niou tall live Wala dougg Si live wakh kofa. Niit dangay am bamélou biir. Té gni ngeini nétali tanè wouniou leine.
45 likes

@Mamadou51158148
Limou def mo reuy nga tagou bayi wouniou la nga dem baparé nieuw exposer ko si internet bi
33 likes

@Bachir17263622
Wadji dako beugoul rek , je ne peux pas comprendre ngay fassé sa Soxna nguirr ay affaire de politique ( sou amoul beineine problème bouniou xamoul)
33 likes

@futur_jordan23
Manquer wessouwoul bayi seu diekeur di terou macky 😭
28 likes

@Veritueslameur
Naka kuluna yi takk Soudon patriote lagn fassee sama djo @Moussa_KL wala @Catalan_Basse93 kamikazou djeul ko sokhna😂😂😂
20 likes

@AlfaduPSG
Le mec voulait juste divorcer. C'est trop facile, fâche toi OK mais de là a mayé batt.
19 likes

@MadagaMamadou
Xana même sooy déme tmt bou heure reer dioté mou fek leuh ci keur gui fassé mom eupna mais femme bi tmt kéne démoul mou dess
19 likes

@fmd_dad
Sa jeukeur boudei dala ayé Lou nekul farata si ioe esk nga tok geunul affaire de politique ngen tass si sen seiy . En plus loy dem si live yi di netali lolou peut être mena geun sissou lo waji. Mou ayei la nga dem ba parei dem si live di netali sen vie
16 likes

@ddiack_
Ces gens ont-ils une intimité ou du moins une vie personnelle s'exposer comme ça pour une chose aussi sérieuse de notre vie 🤦🏾♂️ Yallaah naniou Yallaah doli sutura
13 likes

@Ousmane73272547
Diotè ak sa dieukeur tmt tek Co si mbed mi lolou djiko fène Kate la
10 likes

@fatoudi10423493
Soula fassé nga dem loy niane intervention niak fayda
10 likes

@VentSauvage23
Am kilifeu moy li am solo Soko amer amga solo Soko amoul amo solo Kou werou woul yomba beumeukh
9 likes

@dieye_drame
Sam diabar sonko rek la bagn motakh on n'évite tout débat politique entre nous.😅
9 likes

@_ecu_de_chene
Wadjii nk daa yabattè il voulait juste un motif nk
7 likes

@AntaFAL22197820
Adouna meetiwul ko beuguei niit lum beug t muy deug ci mom diapalé ko ci après mu diex
5 likes

@criticalspacee
Je ne peux pas vivre avec quelqu’un dont les convictions politiques sont opposées aux miennes. Soutenir l’APR ou approuver Diomaye, pour moi, c’est impossible. Je préfère qu’on se sépare. Bravo jeune homme
4 likes

@Elijah_ibrahima
Perso je pense pas que ça soit seulement ça. Peut-être que la dame est une habituée des faits, sortir malgré l’interdiction de son mari, et que cette fois etait la goutte de trop 🤷🏾♂️. Peut-être tamit mou nékk lénène aussi 🤷🏾♂️
4 likes













