Sensitive content
This media may contain sensitive content.
Loading video...
Video Failed to Load
Shetetetete😭😭😭😭français yi
52,559 views • 11 months ago •via X (Twitter)
10 Comments

JoYBoY 🎴🇸🇳11 months ago
Fadam ak bourr nenagn ko mou dimbi len wakh olof touti😭

Abdou Kader 🇵🇸11 months ago
😭😭😭😭😭wakh deug

Mactaraaaa Ndiaga Samba🇸🇳11 months ago
Mais Francais Balla yi am na evolution bou bakh sakh

Cheikh Ahmadou Kane11 months ago
Pourtant français yi dafa khaaut si deux nullards yii

Beck⚪️11 months ago
Balla ken meunou ko terei wax français 😂

Amath Dieye11 months ago
Balla yako fa am 😅😅😅 wawaw sans complexe 😁😁😁

Uzumaki🤍🍥11 months ago
Mom da évoluer si français

Soda❣️Mountakha🩸Mbacké❤️11 months ago
@BasseneIbra sunu mbeur mi Legui wesh wesh la😭🥳😂🤣♥️je lador ki

Nar_Le_Parisien 🇸🇳❤️🇵🇸11 months ago
Je me suis régalé hier Bilay 😂 mais bravo à Balla le big champion il a beaucoup évolué

Mage🇸🇳♥️11 months ago
😂♥️ki damako beug Te wolof lagn ko lak deh purée
Related Videos
1:28
Sensitive content
Paaa yi 😭😭😭
Anthropologue Tidjâne 🇵🇸 ۩
27,035 views • 1 year ago
