Sheut kou def li 😂😂
@MansourSeck030211.454 Follower
48.040 Aufrufe
26 Kommentare
Kommentare aus dem Originalbeitrag auf X (Twitter)

@layepharma1989
C fini cessez le feu 🔥 ki def liii diekhal na game bi oooh les patriotes je vous aime lol 🤣
12 Likes

@MansourSeck0302
😂😂

@Yombz4jk
Inspiration bignou am moma diakhal 🤣🤣🤣🤣
8 Likes

@MansourSeck0302
Trop à l'aise 😂

@BayeMorNdiay
Lii mom gueinei woumasi magi Pastef😂😂
7 Likes

@MansourSeck0302
Ancien yi 😂😂
1 Like

@BayeMorNdiay
Niom rk sagn lii

@baay_zale
Té lici xoromou moy dioms dinako guidd, ndakh CBN néna saway dou diok ci RS yi😂😂😂🤣
4 Likes

@Xeuch262
Thieuyyy kou liguey lii dina niou teuthie lou rekk😂
4 Likes

@MansourSeck0302
Article 80 😂😂
1 Like

@whokenz
Surnom bu bess feñ na MANGASSI😂😂 hara ma noppi sax Pros da koy téré
2 Likes

@Momarniang2611
Togn baxoul deih 🤧😂
1 Like

@MansourSeck0302
Kou ndieuka togn 😭
1 Like

@Mathiappi
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
1 Like

@MansourSeck0302
Dinguerie 😭
1 Like

@Mathiappi
Quelle inspi🤣🤣🤣🤣🤣

@Le_Patriote_221
😂😂😂😂
1 Like

@MansourSeck0302
Boy yi sérieux wougn 😂😂
1 Like

@Le_Patriote_221
Blh inspiration lañe am 🤣🤣🤣
1 Like

@MansourSeck0302
Mangassi 😭
1 Like





