Загрузка видео...
Не удалось загрузить видео
SONKO nak beuri na Caprices dé😂😂😂😂😂
70,578 просмотров • 1 год назад •via X (Twitter)
Комментарии: 11

Broh il rit comme ca rek mais il est malade dh et ses toux temps yii da geneu fégne rek avec la campagne dans les zones reculées fatigue bi akk poussière bii. saay tapalé woule dh dakay diaralé si humour rek pour bagne gayii stresser😭🤦🏾♂️

Mais normal ku nek di def tour Sénégal 2 semaines nopalu wo ak kenen kum meunti doon tmt fatigue bi meunoussi niak té humour bi aussi moy neexal campagne bi Man ahssi damakoy roubé rek🙏🏽

Ki dafa febar Xadim

Mais malako geuneu yeen difficile dé alaji

Garde rapprocher bi moungui retane 🤣😭 pour man niom dougn retane 🤣😭

Nit budul ree amna😂

Dafsi bolé yané 😂 simplicité zéro

Blh da barri caprice mais loumou def nonou leu 😂❤️

Mom Lou Nekh djabotam gui rk Nekh nakoo😂😂

😂😂😂

Wax leen ak ki way😂😂😂
Похожие видео
‼️Sonko dh confisquer na Chéque biii 😂😭😂😂 🇸🇳❤️🏛️
💙꧁𝔈𝔩~𝘗𝓲𝘉è~𝕵ℛ𓃵꧂❤️🦁🇸🇳
38,501 просмотров • 1 месяц назад
