正在加载视频...

视频加载失败

SONKO nak beuri na Caprices dé😂😂😂😂😂

70,610 次观看 • 1 年前 •via X (Twitter)

11 条评论

KHALIL🇸🇳⭐️ 的头像
KHALIL🇸🇳⭐️1 年前

Broh il rit comme ca rek mais il est malade dh et ses toux temps yii da geneu fégne rek avec la campagne dans les zones reculées fatigue bi akk poussière bii. saay tapalé woule dh dakay diaralé si humour rek pour bagne gayii stresser😭🤦🏾‍♂️

XAADIM🇸🇳 的头像
XAADIM🇸🇳1 年前

Mais normal ku nek di def tour Sénégal 2 semaines nopalu wo ak kenen kum meunti doon tmt fatigue bi meunoussi niak té humour bi aussi moy neexal campagne bi Man ahssi damakoy roubé rek🙏🏽

𝗟𝗲 𝗡𝗼𝗺𝗮𝗱𝗲 𝕏 的头像
𝗟𝗲 𝗡𝗼𝗺𝗮𝗱𝗲 𝕏1 年前

Ki dafa febar Xadim

XAADIM🇸🇳 的头像
XAADIM🇸🇳1 年前

Mais malako geuneu yeen difficile dé alaji

Ibrahima SONKO🫥 的头像
Ibrahima SONKO🫥1 年前

Garde rapprocher bi moungui retane 🤣😭 pour man niom dougn retane 🤣😭

XAADIM🇸🇳 的头像
XAADIM🇸🇳1 年前

Nit budul ree amna😂

Azerty🇸🇳🇳🇪. 的头像
Azerty🇸🇳🇳🇪.1 年前

Dafsi bolé yané 😂 simplicité zéro

Papi Bouna 😘🇸🇳 的头像
Papi Bouna 😘🇸🇳1 年前

Blh da barri caprice mais loumou def nonou leu 😂❤️

Salim💍👰‍♀️ 的头像
Salim💍👰‍♀️1 年前

Mom Lou Nekh djabotam gui rk Nekh nakoo😂😂

🇸🇳Abdou Touré🏆⭐️ 的头像
🇸🇳Abdou Touré🏆⭐️1 年前

😂😂😂

XAADIM🇸🇳 的头像
XAADIM🇸🇳1 年前

Wax leen ak ki way😂😂😂

相关视频