Video wird geladen...

Video konnte nicht geladen werden

Zur Startseite

Soññee ci nangoo liggéey

23,258 Aufrufe • vor 1 Monat •via X (Twitter)

16 Kommentare

Profilbild von Muriidul-Laah 💕 🇸🇳
Muriidul-Laah 💕 🇸🇳vor 1 Monat

May ma xeeuuliiss

Profilbild von Moor Suraŋ
Moor Suraŋvor 1 Monat

😂😂 bawal bawal noonu la koy waxe

Profilbild von Papa Dramè
Papa Dramèvor 1 Monat

Macha alla dieureudieuf srgne bi moor sourang amna solo

Profilbild von Al hassane tine
Al hassane tinevor 1 Monat

@Isaacnjaay313 Masha Allah lerna te werna

Profilbild von Elimaan Njaay 🇸🇳 🇲🇦 🇨🇻🇨🇳
Elimaan Njaay 🇸🇳 🇲🇦 🇨🇻🇨🇳vor 1 Monat

@SokhnaLo15 Chinois yi moom dañiy jaamu client 😂 boo demee Chine. Waaye buñu xasee ba jaay la, dootuñu sax nangu wax ak yaw 🤧🙃😂😂

Profilbild von Moor Suraŋ
Moor Suraŋvor 1 Monat

@SokhnaLo15 Ñoom asiatiques yépp noonu lañu mel buñ xasee lekk sa xaalis sayee

Profilbild von Ndeye gueye
Ndeye gueyevor 1 Monat

@MouhamedNouru Deug bou wer nga wakh dh machallah

Profilbild von Seydina Omar Ba 🇸🇳
Seydina Omar Ba 🇸🇳vor 1 Monat

Waxal ca kaw ! Lii lu am solo la.

Profilbild von Moor Suraŋ
Moor Suraŋvor 1 Monat

Bëgg a defar rekk

Profilbild von Ha'im al-Mustafa ﷺ
Ha'im al-Mustafa ﷺvor 1 Monat

Machallah, amna solo

Profilbild von Serigne Mbacké
Serigne Mbackévor 1 Monat

@BittyLohoNdiaye Tuwarkala

Profilbild von Élément SONKO
Élément SONKOvor 1 Monat

@sambmanaha Société bi limou tekk jeunes yi metinna

Profilbild von Baye Massamba Niang
Baye Massamba Niangvor 1 Monat

@DiorfallGueye2 Jërëjëf wax bi doug nama looll

Profilbild von Khadim Diakhaté
Khadim Diakhatévor 1 Monat

Legui outeul gnou liguey serign Mor

Profilbild von Ndiaga Maxtaar
Ndiaga Maxtaarvor 1 Monat

Lu wër ✍️

Profilbild von Beugeu♥️🇸🇳
Beugeu♥️🇸🇳vor 1 Monat

Bilahi werr na @s_sourang

Ähnliche Videos

Émigration clandestine : un combat de tous, pour tous! L’émigration clandestine est un défi majeur qui décime nos famille. Pour y faire face, plusieurs leviers doivent être activés de manière concertée : - Une prise de conscience collective, sur les effets néfastes de ce fléau, tant au niveau individuel que communautaire ; - Une jeunesse résiliente et déterminée, capable de croire en ses capacités et de s’investir dans des alternatives viables et sécurisées ; - Des parents compréhensifs, tolérants et responsables, qui soutiennent et conseillent leurs enfants dans la quête d’un avenir plus sûr ; - Un État créateur d’espoir et d’opportunités, qui œuvre à offrir des perspectives économiques et professionnelles solides pour retenir la jeunesse sur son propre sol. Merci à Lamine Niass pour cette belle inspiration. ------------------------------------------------------- Tukki bu jaarul yoon : xeex la ci ñépp, ngir ñépp! Tukki bu jaarul yoon jafe-jafe bu mag la buy yàq sunuy njaboot. Ngir saafara jafe-jafe bii, fàww ñu def ay jumtukaay yu bari ci anam yu boole: - Ñépp xam loraange yi mbir mi man a jur, ci ku nekk ak ci Askan wépp ; - Ndaw yu dëgër, am pastéef, gëm seen kàttan, dugal seen xaalis ci yeneen pexe yu wóor te man a dem ; - Way-jur yu am xel, man a muñ, am wareef, di jàppale seen i doom ak di leen xelal ci seen ëllëg gu gën a wóor; - Réew mu defar yaakaar ak xéewal, di liggéey ngir joxe xéewal yu am solo ci wàllug koom ak liggéey ngir téye ndaw ñi ci suuf si. Jërëjëf Lamin Ñas ci xalaat yu rafet yii.

El Malick NDIAYE

32,145 Aufrufe • vor 2 Jahren