Video yükleniyor...
Video Yüklenemedi
Teere bi🥺🥺❤️❤️ Allahu Akbarr
192,576 görüntüleme • 3 yıl önce •via X (Twitter)
18 Yorum

Imam Khalilou Bs3 yıl önce
Ndanaan a ngoogu !

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
Keen du mom wallahi

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
Sala xol bi Sed na barki Sëriñ Tuubaa 😭❤️ Teere bi rkk la am..

Galaye ⭐️🇸🇳3 yıl önce
😔 j espère su ñibise si jaam, dina gene been vidéo intégrale hajjam

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
J'espère gayi préparer neñu lolu mom.. Genrou film, Anh @echgueye ?

met🇺🇸3 yıl önce
Diay katou iPhone bou mak la aka bakh

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
@SarrPikine Ndeysaan

Khadim Shayhoona Fall ❤️🇸🇳🫱🏾🫲🏼🇵🇸3 yıl önce
Cëy Allaahu Akbar❤️ gàddul nanu ko parasol ☂️ ba d moom 🥹 Waaye 😔 “Xassaa’idi min muhjizaatil Muntaqa” kepp dé 😔

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
Ceeyy😭😭

الْـأَنْصَــارِي3 yıl önce
😭 الله أكبر

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
🙏

Mamadou Dione3 yıl önce
S Touba rek, bilahi ki kou ay mbireum yeemul hawma lo doon.

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
Wallahi

Seexbi 🩷3 yıl önce
Bii ladon haar😭🥰saa hool sedna !!!!

Derviche Garmi ✨🇲🇷3 yıl önce
Santt rkkk key

MasSamba3 yıl önce
Sëñ Ibra dh mo ngui melni ku yor micro, kaddom rek ngay dègu dh

مر د جوف 💫3 yıl önce
@be_mouride Darajay Djalibatou 😭💙🤍🫶

Solar Heavy1 yıl önce
- We're Flying
