Loading video...
Video Failed to Load
Tellement vrai
40,854 views • 1 month ago •via X (Twitter)
22 Comments

J'écoute en ce moment mm l'intégralité de ce Fatwa. Yalla nako yalla samm wereul ko🙏 I

Merci wayy oustaz faux rek niou nan famille

Acay deugue Machalla

Wah deug man mak niom douniou diobou sama domou ndeye yi😂😂 mais bouko wahone wala omar sall douniou fanan sen keur wah na deug

Talibe cheikh la deh mais deugeu rek la wakh

Capitaine mak bouy nakh pobam la rek ta aussi limou wax waxi doff la wayé yeun wahabiste yi wax guen lou raw lolou moy saga kilifay diambour saga ay wadiourou diambour ta cou am displine dou saga kilifa diambour 👍🏾

Wahabite yi noppilen bala niouy guenner archives yi Abdoul wahab niata dioulit la ray si adouna??

✅

@henrypierresarr Bii moom andna ci linga wax

y’a que des hypocrites Sene capitaine bou rew da khamoule Dara !!!

@CissYaya19 Merci beaucoup

Aaaaalll Len gnu sen Xolu Yaye yi gnu tangall Si café ! Kussi meun dara rekk gnewalll Fadj Mram yi

@real_psd_ Pure vérité

Il se croit important ndeysane saway do 100ffr mouy expliqué niawayy rek guaniou eupeulé

Motay loléne sii meune ludul hotei rek toussss Si vous avez les couilles d'homme wahuma goordjiguéne deimm léne fek ko keureum

Yaw fo tothie ak lane nga réalisé si rew mi loudoul di dingate souniou mg gni ingrat rk molen diappe Ndakh bo len démé ba ame fitou nane alahou akbar niome nio tah tekki wou len dara si rew mi

Nafekh beurina si rew mi ay magu you togu di bouroukhlou wallé pour diéma wakh séne sokhla waye dof yi gnossiy dess nak

Aka meiti si khol limoy danger innovation car nioukay def douniou mouna dal sen kaww car niom nieup boku mbouss

Dala metti ? Diougual fathie ko !

Nopilén vous êtes pas des sénégalais on parle avec les sénégalais

@Africabii Barké Serigne bou mak bi wah nga deug

Aka gno meuneu fén gnii😂😂…. Bou féké lolou dalay dérangé seukeut lén gua xol.. Gnoun gnoy dieukeu tass sén seurou yay yi deubeu sén you bay yi dogay deubeu réw mi…. Salle con
