16 Comments
Comments from the original post on X (Twitter)

@OumarNazir99249
Walahi si ce n’était pas Sonko, Amadou Hott allait prendre la mairie. Dafa am chance deug ba ce jour là Sonko est passé la bas.
13 likes

@Khalileuh92
Il va comprendre lors des prochaines échéances ⌛️
2 likes

@Laminefade20754
Allahou Akbar nit mo leudeme
5 likes

@Khalileuh92
Trop sah

@ousmane85017865
Xawma kou Ousmane takhoul nga falou la dh, mais iow bokosi, tout le monde savait que amadou hott day gagner ba jour bifa Sonko di diaar
3 likes

@Khalileuh92
Bayko rek dina comprendre après
1 like

@khar_mane
Je t'estimais beaucoup Bara mais rousse lo ngama taye Yallah ani bureau de votame
2 likes

@Khalileuh92
Bayilo ba prochaine élection

@AbdalahDio84905
Fenn rk douniou sakh rouss
1 like

@Khalileuh92
Bayiko rek

@GueyeBoOba
Ousmane Sonko li nekh si mom moy boula falé ngay weddi Yallah dalay waxlo ba bess bu rafet mu bolé lak mom mou fekk la bga yorr sa poste mou fokhati ko té dosi meun dara. Ku wedi ladial judas Diaz

@dione_mohamad
Thiéé adouna adouna adouna😭

@diack_sano
Sama yaye ak sama papa gnoma diour way y’Allah sakouma mdr… bayiléne thiaxane tei deim nafila dji

@PapeSidy75
Non nitt mo leundeum deh. Bara ya sania wakh li téy?

@Saliou2_0n
En plus ay nitt you diang Al quran xamko🤧😑

@Lasga1621
No ki dou nite wakho wone li Bara nite mo lendeum