10 Comments
Comments from the original post on X (Twitter)

@Cherifoooo
😂😂😂😂di expliquer paré goo gars yi diokh la exemple en direct 😭 Senegal dou réww
49 likes

@AllaNiang7
Reew mi diakhal nama 😂🙆🏽♂️
25 likes

@a4suki_qlf
Le halangou du djakartaman deysane 😂 Non deukbi comme film indo
13 likes

@WhYasay
😂😂😂😂😂😂daguay senn li senegal amouma benn yakar si changement wam
9 likes

@mamadou_nd002
Weddy guiss bokk si 😂😂
7 likes

@SeneDouka
CDa xawa rétane Lou 😂 Di wax parégo gayis andila exemple. C pays est malade
7 likes

@Lepatriote221
Ndeup national jotna nak 😂
5 likes

@CheikhM38671191
😂😂 waa jakarta yi khana exemple lanouy diokhé
5 likes

@Notifier_Admin
Le pays a besoin de ce bouton 🤣🤣🤣🤣 c’est pas possible
5 likes

@amathdiouuf
Deukk bii mo diakhassso😂😂😂😂
4 likes
