Loading video...
Video Failed to Load
Wakho lep dh bakhna 😂😂😂😂
20,386 views • 24 days ago •via X (Twitter)
31 Comments

Inspecteur dh kanam door kate deugu la yooré

Sama prof lawone université mais ndakété éthique déontologie ak patriotisme boun niou done diangal yeuppp nekoul si niomm

Ki ci sathie yi la bokou

Saaaaatiéééé khelmi daloule déh fimou néke niii 🤔

Ak guemine bou mookk bi 😂😂

🤣🤣

Le probleme ici et de ces foncionnaires ne comprennent rien des exercices de la democratie!!! et a la tete du client, on voit qu'on a affaire à un gougnafier de premiere categorie!!!

Kii beugoul tontou ame neu loumouy neub sou enquête hoté dina révélé ay mbirr ci mome

Ce qui me fout la haine au Sénégal, c’est quand tu parles à un fonctionnaire et qu’il te pond des « gnagnagni gnagnag’na , je suis un commis de l’état … j’ai servi tant de…. Droit de reserve… » te wallahi dougn touss. Ils sont nuls. Booy wax ak niom dileen xeeb. Shipppp

La manière de pivoté la chaise montre qu'il n'est pas serein

@__TENGEN Kou tite Boko Guissé xam ko regarde les yeux rekkk

Ça façon de parler ses manières 😱 xana mom dafa am loukoy matte fimou toog kii ay mbiram léroul dh

Genre yi gno nek sougnou administration yi mon Dieu gnou dougne meussa développer

Nena bouma ko waré wakh😁

Gnaaw ba parei di Door Sarap ndei deuk bi 😭

guéminiame bou n*****f xoname bi 😞👨🦯➡️💔

Ki kouko niousss mou wakhh l fi khaliss bi dougu

Je Le connais pas mais c’est lui….

@Omarndiaye_4 Ce n’est que la partie immergée de l’iceberg. Ils sont tous des archaïques, des incompétents… un GenZ ferait le boulot mieux qu’eux

Wadji envie pesko rek la am mouy leyam leyamini

Seex mii niruwul fonctionair daf ñuy nax reg 😃

Sathi ay milliard fegnoul sa kanam Incroyable ce pays

Doyna waar,

Daga sathie ____Ouiy Sathio _________ouiy Kou sathie_______ouiy

Seex joob mii neena day ree ak ni ay mbiram leundamee 🥹🙂↕️🙂↕️

Gni walahi dougnu ay nitt sheutttt💔sons thier sakh nga defar si sa beugn yi shimmm

Tete vide domage à notre pays

Mome dou tokk beeneu place

Ki madiambal la wla 🤧

Say tego dara lou lerr tontoul

Commis de l’état Damako dièpi j’ai pas terminer l’audition Il nous doit des explications il n’a pas été clair
