Загрузка видео...
Не удалось загрузить видео
Yewaya ndaw
54,659 просмотров • 5 месяцев назад •via X (Twitter)
Комментарии: 37

Lirek la d koula dieulé si sawaay si waay rek lalay yobou😂

Barki yalla dëgg la , bayyil li jappal lii rek

Cheikh Salihou adouna moom koufi yéwou rek nopalou😂😂😂 problème bi yép beugue doundou kép ak beugue daradia waayé diné diou gueuna wér li Borom Touba diangalé dieuféko nite manoufi indiwaate louko raw hana nga créer sa yeufi boppe rek 😂

Man mom ku ma xam xamni ku critique laa daanaka lu leerul sama bop duma ko jegge en bon serere , waaye seriñ bi mom gisuma ci daaara lu lënt ñak a xam kay waaye lepp leer na wer na

Kone d nioom yém maye nétali damay def silsila nga hamné mane nga dém laathie kénène soula nékh té de préférence kouye doundou laaye séddé ndah auto- critique waayé lou gueuna lère Serigne bi amoul hana niak gueustou mbiram ak atéko si béne waay boukoy toudo té doonouko

Diotay bi manquer na café touba d

@Falilou_MFD Ñii duñu ñëw ma jaay leen Cerave

@Falilou_MFD 😂😂😂💀💀💀

🤣🤣mane Biniou dieuler Safara diko wower eau coranisé di tek khel laci parer 🤣

😂😂😂 haha

Louniouy xasser gars yi dagn koy def suptillement 🤣

Soxor moy seen tawat

Exactement niom si louniou nek Ken wakhoul en ci dara loutakh niou beug diap ni kenen kou bokoul ak niom guiss guiss bakhooo

Votre problème c’est que vous êtes incapable de parler de science d’Allah et de son prophète PSL mais quand on parle de vos ancêtres vous êtes tout à coup concentré et mais quand il s’agit du coran et la sunnah vous passer votre temps à vous moquer qu’Allah vous guide

Xuraaniyuun yi ñoo commencer tibb ci seen boys yi motàx ñuy reunion de crise nii, nàngu ne léegi foog nga am Sëriñ 😂😂😂 Jëlal Mod'lo ak laisser 4 bi 😁

machalah diotay bou amoul folklore ☝🏾

Machallah kay mom

Breudeu yi aka nio nekh

@noreyni1111 Xolall docteur lo niimou diapé ndiakh rk😅😅... serignou gayii😂

Tout ce qu’ils dit s’applique à eux. Ils n’ont pas d’isnad. Tu demandes à leur shuyukh de te donner leur isnad et tu trouveras dedans quelqu’un qu’ils takfir.

@yaaba_ kay khol breudi ak doc lait

Lobby leuh deh

🤣

Fi deh kham kham rk lagne fi wakh 👍🏻😂

Kii sanékou moy seugn bi xana

Reunion 😂😂😂

Kiy wax ni numu tudu

Qu’est ce qu’il a d’extraordinaire sur le discours ?

Diang bi changer dh now this country kén xametoul kén😂

Ñii wut yat rek a dagan ci ñoom

J'espère que diarignou nga

Ci lan ?

🤣🤣🤣🤣🤣

nank nank rekk , legui gué guiss lén gnouyy soufi soufilou

Ay docteur 😂

Lii la sëñ Ganna di wax ñiy dagg rang bi bëgg ku leen rang rekka tax 😂

@tafambaye8 Waa ki tallalou nonou moom koumou ? 😅
