
Moor Suraŋ
@s_sourang • 31,354 subscribers
Mor Sourang PDG Massalik Café, Écrivain et Chercheur sur le Mouridisme
Shorts
Videos

Yéen ñi ko xamul kii mooy Omar Jaañ yàgg a doon noonu tariixa yi.
Moor Suraŋ131,568 views • 1 year ago

Ndaysaan nangu nañoo wax Sëriñ Tuubaa li ko Yàlla jaraloon ak li mu daj ngir lislaam ak defar nit, waaye duñu nangu ku wax li ko Yàlla faye ginnaaw effort yooyu yépp. Xanaa dangeen a xamul ne Yàlla lu ko waay defal lu mu rëy rëy bu la faye nga rus, lii Xaadim Njaay wax ne Sëriñ Tuubaa moom la doon def ba di ci yéemu, li ko Yàlla faye moo ko gën a yéeme fuuf, fayug Yàlla googu nag ngeen jàpp ne ku ko wax day bokkaale. Xamu leen Yàlla de !
Moor Suraŋ27,137 views • 1 year ago
No more content to load