
Moor Suraŋ
@s_sourang • 32,088 subscribers
Mor Sourang PDG Massalik Café, Écrivain et Chercheur sur le Mouridisme
Shorts
Videos

Soññeb Sëriñ Amsatu Mbàkke jëm ci taalibe yi. Yal na Yàlla samm ko te mottali ay yéeneem barkeb Sëriñ Tuubaa.
Moor Suraŋ18,488 просмотров • 1 месяц назад

Yéen ñi ko xamul kii mooy Omar Jaañ yàgg a doon noonu tariixa yi.
Moor Suraŋ131,745 просмотров • 2 лет назад

Ndaysaan nangu nañoo wax Sëriñ Tuubaa li ko Yàlla jaraloon ak li mu daj ngir lislaam ak defar nit, waaye duñu nangu ku wax li ko Yàlla faye ginnaaw effort yooyu yépp. Xanaa dangeen a xamul ne Yàlla lu ko waay defal lu mu rëy rëy bu la faye nga rus, lii Xaadim Njaay wax ne Sëriñ Tuubaa moom la doon def ba di ci yéemu, li ko Yàlla faye moo ko gën a yéeme fuuf, fayug Yàlla googu nag ngeen jàpp ne ku ko wax day bokkaale. Xamu leen Yàlla de !
Moor Suraŋ27,211 просмотров • 1 год назад