正在加载视频...
视频加载失败
🤦🏽🦻🏽🦻🏽🦻🏽🦻🦻🦻
35 条评论

ki niaf len ko petition mou arrêter doulam yi

Jusqu'à preuve du contraire, cette émission est une expérience sociale pour nous tester 😤

Waaw ! Enfin un vrai Sénégalais - amna Xam-Xam - xamna Adouna - Gueum na Yalla - Mais à Propos Yalla, lui a fait comment pour créer Iblis La Supposée Source du Mal? a. Erreur d'Amateur? b. il s'est ennuyé et voulait un Pendant pour son Équilibre?

Mais journalistes bi tamite kén dou mom 😂😂😂😂

Grand nala masqué quoi 😭

J’ai 15 jours de vacances. Legui mou jeex

@Ndiayetrust Do gnew fatick 😊

@Ndiayetrust Sorina Afrique jamono jiii

Ce gas a besoin d’aide dh …

Le pire mooy Penda Badji dakoy deglu xamni day fen mu diko ko xoole. Limuy mélanger moo bari.

Grand kagn Guay reprendre 😭😂😂

Lundi 24 Mars 😂😂

Malaka yagui xeum 😂😂

@HadjiMaguette @sakoungogne @NiangBabacar19 yene ndékétei parei wolene sakh😂😂😂

Yow mi yaa gnou yap

Magui congés bouma yakal

😂kou sante Cissé mom faaw mou ragal koor

🤦🏾♀️ qui va sauver le Sénégal 😭

Kii sérieusement prof d'histoire dans l'éducation nationale leu nii?🙄

Pourtant xam xam rk lay wakh da meuna inventé rk ak di soss mais loumi wakh nii xam xam la

No. Ki dafa febar. Bilahi

Arona Niang mongui diokhé aï Ndogou you nekh Waye 🤣

Il est plus fort que Jean de la Fontaine. C'est maintenant une évidence. Moi qui pensais le contraire, je viens de me rendre compte que ce mec a un talent fou mashallah.

Barki alkhouran ki mo nara yax gars Yi Bombardé gnou

Li c'est grave

“ Hitler juive la…. 😁😁😁”

Mais lui il est taré ou bien et Dieu qui a dit que les prophètes étaient bel et bien musulmans. Incroyable

le ministère de l'éducation doit le recardre, il est en train de semer de mauvaises graines dans la tête de ses élèves.

Malheureusement les soient disant journalistes n’ont aucun source pour ni competence pour arrêter ce comédien

Idy j’ai un élève comme lui très complotiste dans ma classe je souffre des fois 😂

Ahahhaha Mbadou dalay théorie ? Non documentaire yi la ak film yimouy setaan. Tei defois day cohérent dossi meun dara

L’art de mentir en personne 😭😭😭

Comment une personne normale peut faire de telles allégations sans preuve.

Ki section des recherches kagne lakoy dieuli ?

Ki douma yakhal Sama koor ki meune fenne dh katch rek
