Загрузка видео...
Не удалось загрузить видео
Dites moi si on peut être plus gênant que ça
403,761 просмотров • 6 месяцев назад •via X (Twitter)
Комментарии: 47

Après elles reviennent pour combattre la sexualisation de la femme té nioko yobbé sen bop.

Bilae

Kii kou beug koy la

😭😭

Pour mom adouna lepp katante la

😭😭😭😭😭

Dafma warone takk ma seyeul koh

Louy dougou fofou badi guéne mbirr yangui commencé eupi loxo dh

???😭😭

Xaral ma romb dem sama yoon ken xamoul li laan la🤦🏾♂️

Doyna waar d

Elle valse entre corps capital et corps écran; joue à outrance sur l’attirance du désir et l’attrait de l’inaccessiblilité! Dans ce monde débridé, on dira qu’elle a le droit de disposer de son corps!

@fallouu__MN 😂😂tellement je sais pas quoi penser d’elle 😭

Wa ani mame matar gueye wala fane yi liste bi la tal 😂😂

@bayetaphandao Est-ce que tal nako

Yakarou mako mais mia mom dafa niou yab sérieusement

Amoul talent kayy nii rek laa meuna deff pour percé 🤷🏽♂️🏃🏽♂️

Li aussi dafa eup

Divorcée, elle sort un clip pour montrer qu'elle se libère enfin de son mari. Puisqu'ils étaient deux dans la musique, dorénavant elle va vouloir prouver qu'elle est talentueuse seule. Mais le départ est raté parce que basé sur la vulgarité . Et maintenant, plus de limite. Shame

So wakhé féministe yi attaquer la sexiste potentiel violeur etc.. melni nio mome réewmi mi loulén néex deff kén d’où wakh si cest une femme non c Nice nickel ayy hypocrite laniou les femmes voir la majorité 👌 😂😂😂

Manque d’inspiration

Bilae

Elle est en dépression mais elle est belle et riche ca se voit pas mais elle souffre grave.

Et après tiktok va faire le boulot et vous verrez vos sœurs en faire un challenge ptnnnn

Même si elle a parlé de « Titulaire-remplaçant-tocc banc ».. dès lors qu’elle dit « na dougou » ou « na guéneu » le message subliminal passe. La couleur rouge accentue le message et la perception qu’en font le public est vite connu. Pervertir par la parole. ❌

On pervertit notre jeunesse sous nos yeux 💔😑

Wollah kii xamoul dara louy lii 😭😭🤦🏿♂️

Moma diakhal

Ne vous étonnez même pas d’ici une semaine tu verras des jeunes filles pré pubères en faire un challenge sur les réseaux

C’est très gênant, vulgaire ! Kaadu yi niaaw si bo amé ay kilifeu ak ay dome ! Euleuk lou wara soralé la

Legui ngua guisse dmrm yi diko chalenge

Lep thi lank bagne xewii 😂😂

🤣🤣🤣

Féministes yi danio d'accord ci liii?

Musique bou yewull yétéll cheikh bii diaxan kepp la 🤦♂️🤦♂️

Avec ça ngen beug goor yi respecter gnou💔😭

@fallouu__MN Ki pour mom lép katanté leuh « neu dougou, neu guéne » sarap ndm

Il lui faut des prières 😂irrécupérables

Dites moi que c’est une hallucination collective 🚶🏾

Question très serieuse !!! Seen digante ak yalla situation reew mi titoo len si ?

Elle sait que l'industrie misicale est milieu satanique et si le talent n'y ait pas, la vulgarité peut prendre la place et te faire percer

Feministe yi louniou wakh si lolou?🤷🏼♂️

Après bou rombé ci mbedd bi béne goor néko "mou dougou wala mou guéne" mou merr après féministes yi gneuw bindeul gnou texte, khalé you djiguéne yi 72h gnou... 🤦♂️

Aaa cou diouk niouni dafa ayy cagn Lii ken xamoule loumou done

Sénégal pour niom lepp faut nga sexualiser , li ken xamul lane la

Wallay ki dmr la

Elle devient de plus en plus ridicule wallah j’ai pitié d’elle.

